
Constat Amer Lyrics
...
Constat Amer Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Zeus, euh
Amma constat bou amer
Dara safatouma dagnma toogué ba paré
Bouder founé ngay wakhé
Nane la nop bou reeroul di xam ngay wakher
Digueunté sa doundak dee
Beug djitou la niakaloo moudiou bou rafett
Diamonoy mythe de la caverne
Takka ndeerou liy deug lagn fixer mouy paraitre
Boula sais ai yi daré
Sa xam xam dou diarign nakh mouss ngueu beu khadié
Kiné y’a jamais 2 sans 3
Moolanaan in ne faut jamais dire jamais
Yooré doundoun mor nadié
Takh nga wathi sa and nakh wamoo sa wareef
Adj le psi thiaawanou kessé
Wathi caamiinou tallah neh xamoo ay tereem
Alalou boromou barké le 1er bou diotté nga xamni yaa wéré
Bou sa niakh bi reeré
Ba nga yee borom ndekki ay khass digko agné
Gorgorloul ba romb parquet
Daw lepp loulay tardeel nakh yoon bi da serrer
Takal joint bi niou rouler
Brodah coup bi bou diaalé dougn takhaw si arrêt
Moytoulma nittu interet boudé guisso si lou dieum si sa intérêt
Nittu deug bou dokhoul si iow meun nguen weetak say og dem lekki dji thiéré
Diougué sakett dem palais weurseug finioukoy tiibé la yallah di saaké
Ligueey taali fi diaffé gni nga falalay door ba nga taalékou niaarett
Amma constat bou amer
Dara safatouma dagnma toogué ba paré
Bouder founé ngay wakhé
Nane la nop bou reeroul di xam ngay wakher
Digueunté sa doundak dee
Beug djitou la niakaloo moudiou bou rafett
Diamonoy mythe de la caverne
Takka ndeerou liy deug lagn fixer mouy paraitre
Diakarlook adouna wane yallah guinaw
Teh guinaaw yallah ken dou toukil adouneu
Yaanoul adouneu niou tekk la koo nekoul
Nakh amoul mindeef boufi antane adoune
Meun nga diplomer doon nitt kou xamasi
Nakh école ken doula diangal adouneu
Wiri wiri diaari ndaaré mais deug mooy moudiou
Meme bou den yi weuré adouneu
Laamegn taamou ba moudier si moumeu
Maano taarou ba raw fa yussufa
Gniy diokh wally dougn battrer moumeu
Yin gay social sen xaliss nga loubeul
Mindeef laa bou yor bindou youssoupha
Ndoumbelaan deukou bouki ak loup leu
Dee si gathié deuth teguil leu touleu
Yaa gueun doff ki nga diapone ni fou leu
Beug dioubeul
Tegui sunnah
Dawal ada boy gars yaagui pull up
Daniou am faiblessou xallé you xess
Loolo waral ba paa yaagui niouleul
Lep lilay choqué si ay faits divers
Soriwoula nakh lep si nioun leuh
Dou kou changer si iow bessal couleur
Des fois demb mooy fekki dji soubeu
Djigueen sopal boul woolou, boul faaténé soopay indi koolouté
Ak sa mbeuguel noum meun toolou sa xalou mougn bi fimou yem rek la maneu yem
Moytoul diéleu bi doon lila wara yee
Yeki mbeureum migko xam si balla gaye
Rakk beug naa nelow mais nane ngay def
Booy yeetal reveil bila wara yee oh yeah
Watch Video
About Constat Amer
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl