Paroles de Wëy Wallú
Paroles de Wëy Wallú Par LEUZ DIWANE G
[INTRO]
Hey lèeeeeeeee
Oh, Nana Nana
S oooooooooòo s
Maydè
Oh secours
Weuy walooooo
[VERSE 1]
Incompetence meunoul dokhol rew
Sou niou confiance sopi nguene ko new
Sene arrogance sa tass si rew mi rew
Trop de défaillance sa takh fou né niou ngui latchté lou khew
Rest in peace Doctor Cheikh Anta Diop
Rest in peace Dia Mamadou
Nioune dè tiiiiiiiiiiiiss reka la niou Gaup
Kou guessou guiss nakhar bi niouy yendoo
Kou nieuw ba nga fog nè mo tanè fekeu mo gueuna yess
Ray nio ki discours defarou kheuy nè mess
Raylè la dialè la sakhami ko mou ress
Jouer niou ay sale Tours
Dou fi lou bess
Let’s everybody be aware nelaw yi da doy fog niou khipi khol
Let’s everybody be aware ligne niou diapè nèkhoul si xol
[CHORUS]
Da niou diooy ba sou niou guët yi dessatoul ndokh
Youkhou weuy yooy guissou niou kèna Kou niou nax
Nièp yooy khiif soneu Mar Bay lokh
Beug mou doy niouy dirèkou ramouniou Bay dokh
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw guèstou lene gni si soufff
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw guèstou lene gni si soufff
[VERSE 2]
Kagne lay doon
Kouy walou askane wi
Kagne la Kagne la kagne lay doon
Kagne lay doooooooooooon
Kou niouy walooooo
Amou niou lou niou lekeu
Amou niou lou niou Naan
Bouy khiin di mbeundeu ci ndokh mi la niouy fanaan
Ko guiss mou ni tek
Ndiakharé Ko Daan
Seungueem rogogne yi di gawa tokh ni salaan
Ndokh aK courant yèksègoul si Yena gokh yi ba tay
Étudiants yi dèkou sokh yi fac gay champ de bataille
Ndiang mi di sookh prof yi grève thiow li dou tay
Patch mi téwa dokh mak yi wax tayi
Baykatt ba ngui diooy
Sameu Katt bi napp Katt bi sokhla Kou lene guèstou
Weuy yoooooooooooooooy dafa doy
Aleu ba ngui latch walam bou lene ko Gass soul
[CHORUS]
Da niou diooy ba sou niou guët yi dessatoul ndokh
Youkhou weuy yooy guissou niou kèna Kou niou nax
Nièp yooy khiif soneu Mar Bay lokh
Beug mou doy niouy dirèkou ramouniou Bay dokh
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw guèstou lene gni si soufff
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw guèstou lene gni si soufff
[VERSE 3]
Oh, secours SOS
Mayday Appel de détresse
Oh secours SOS
Mayday appel de détresse
Kagne lay done
Kouy walou askane wi
Kagne la kagne la Kagne lay done
Kagne lay doooooooooooon
Kou niouy walooooo
Da niou lene fale
Di lene fay pour nguene liguey
Bayi lene si khel
Delo thieur bi gni ko mom
Ame lene khel niou ngui lene di khaar nguene liguey
Bou lene bone loo sou niou khol di sedoo sou niou koom
Da niou lene fale
Di lene fay pour nguene liguey
Bayi lene si khel
Delo thieur bi gni ko mom
Ame lene khel niou ngui lene di khaar nguene liguey
Bou lene bone loo sou niou khol di sedoo sou niou koom
[CHORUS]
Da niou diooy ba sou niou guët yi dessatoul ndokh
Youkhou weuy yooy guissou niou kèna Kou niou nax
Nièp yooy khiif soneu Mar Bay lokh
Beug mou doy niouy dirèkou ramouniou Bay dokh
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw guèstou lene gni si soufff
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw guèstou lene gni si soufff
Ecouter
A Propos de "Wëy Wallú"
Plus de Lyrics de LEUZ DIWANE G
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl