JEEBA Décorée cover image

Paroles de Décorée

Paroles de Décorée Par JEEBA


[COUPLET 1]
“Eeeh eeh eeeh Jeeba le Boy oooh ooh”
Seen ko reik mouy deem
Aam caractère ba dokoo ñémé xool
Yeee Yee Yeeh
Mane guiss nala yoow yagui dieem
Beug meunale sa Bopp ba kenn doula toññ Yeee Yee Yeeh
Nionioy jigeen jigeen juu meune goor
Jigeen juu kharoul daraay goor
Jigeen juuy niaffé nguir meunal bopam wawaw
Mane kham dou diambar nga damalay nianal Annnh annh
Baññkat laa motakh mou deuk ci war wi
Yeee Yee Yeeh
Yow yarr nagn fuññ la wara yarr boubakh
Meusso ñuu gathiel benn yoon linga geum
Bobou ba leigui yagui siiy ñiaffé nguir beug mou baakh
Motakh reik manaan la

[REFRAIN 1]
Naaw na sa yaye boy
Dina ko décorée wakh ko doom boumu juur
Meune na yoor reew
Naaw na sa baye boy
Yoow baye boy
wakhko dom boumou juur
Meun na yorii reeew....eeh eeh eeh meune na yoori reew
Sa yaay boy eeh eeh eeeh eeew
Jigueen meune na yoori reew

[COUPLET 2]
Seen ko reik muuy deem
Boudonne benn bouniou donn niénteu
Mane sagn nala bayi aak njaambot guissi keur gui
Douñu toumouranké douñu kokh kokhi
Niongui si tolle yi aak bureau yi
Niongui si sport bi aak fo meune tii deem
Ma naam jigueen yeup soleen né diaak
Dignité aak jambarté ngay lire seeni kanaam
Ay Joxooñ nala joxooñ nala
Motakh ma biind weuy wi deelo la ndioukeul
Oube nga lamb ji do seen moroooom ooooh oooh ooh
Oooooh oooh oube nga lamb Ji jigueen do sen morom

[REFRAIN 2]
Mane naaw na sa yaye boy dinako décorée
Wakh ko doom boumu juur meune na yoori reew
Mane naaw na sa baye boy
“Baye boy”
Wakh ko doom boumu juur meune na yoori reew eeeh eeh eeeew
Meune na yoori reew eeeh eeeeh eeeh
Naw na sa yaye boy eeeh eeeh eeh

Jigueen meune na yoori reew

Ecouter

A Propos de "Décorée"

Album : Décorée (Single)
Année de Sortie : 2020
Ajouté par : Farida
Published : Nov 26 , 2020

Plus de Lyrics de JEEBA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl