Paroles de BDBC
Paroles de BDBC Par BAYE MASS
Bateau deim, bateau coster
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Bou feke ni da nga fok ni damay topou sa guinaw
Yay dem yay nieuwate
Bateau deim, bateau coster
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Bou feke ni da nga fok ni damay topou sa guinaw
Yay dem yay nieuwate
Yow yaye kiy dém, yay kiy nieuwate
Dangue may bagne, dangue may beuguate
Boul meusseu fokni, damay topeu sa guinaw
Topale thi rang bi
Thi nji topeu thi guinaw
Khamoo lingua beugue
Beugue wakh diou séw
Deile khole finguay feug
Pomme dou moromou new
Louma def nga wakh
Louma defoule nga wakh
Bo kholé, ba khole
Amnga farou rap, kone baxna
Sa wakh dafa beuri nga balma
Diambate ak caprices kaagne ngeu
Niveau yeé bokoul kham nga
Espérance ngay doundé dathie ngeu
Meune ngafa diaré thioloule
Newone nala risquer woroulo
Ndakh dinanie delou léroule
Deugue touma sakh nga nieuw déloule
Bateau deim, bateau coster
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Bou feke ni da nga fok ni damay topou sa guinaw
Yay dem yay nieuwate
Bateau deim, bateau coster
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Bou feke ni da nga fok ni damay topou sa guinaw
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Dadjal nagn la banc
Say statuts yeup lagn capturer
Dagnlay yoobu var, wakhdji yaako tal
Sa khol laala fay
Alalou kou saagane laawoom am kounéma thiass
Xamouloo fooy takhaw
Kone démal ma dem
Danga beuri details
Beug sé boolé reuy
Beugoo guiss may bégué (bégué)
Di deg je t’aime (je t’aime)
Si kenen mouy def effet (effet)
Loussiy pékhé wakhma nakh
Diapoo teh baayiwoo
Demoo teh dikoulo
Talnaa lenen loudoul deuker xoulooka juboo
Diapoo teh baayiwoo
Demoo teh dikoulo
Talnaa lenen loudoul deuker xoulooka juboo
Bateau deim, bateau coster
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Bou feke ni da nga fok ni damay topou sa guinaw
Yay dem yay nieuwate
Bateau deim, bateau coster
Yay dem yay nieuwate
Yay dem yay nieuwate
Bou feke ni da nga fok ni damay topou sa guinaw
Yay dem yay nieuwate
Ecouter
A Propos de "BDBC"
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl