Paroles de GMD
Paroles de GMD Par BAYE MASS
Goney may deuk
Magua may daanèle
Fimala ték
Romb na bou guaniéé
Goney may deuk waye
Magua may daanèle
Fimala ték wayeii
Romb na bou guaniéé
Koula done woute thi mane dinala ame
Kouma beugue bayék yaw nama ba kham
Diarala ngama khekh ak gained nane thinou mbakhal
Bou souff sédé ba niepeu teudi ma ame loumala wane
Sama mbeuguel dafa fakheu wouti sa boss
Sama khole diarafé séde keur guiy dialanio
Souniou guissé mana weete ba ame loumala def
Nakh guoney may deuk wayé maguamay danèle
Sama mbeuguel dafa fakheu wouti sa boss
Sama khole diarafé séde keur guiy dialanio
Souniou guissé mana weete ba ame loumala def
Nakh guoney may deuk wayé maguamay danèle
Hummhummm (khalei bi deifal nankeu)
Hummhummm (nieuweul sakh ma deyleu)
Hummhummm (loma niane ma mayla)
Hummhummm (bou doyoule ma dolile leu)
Goney may deuk wayei
Magua may daanèle
Fimala ték wayeii
Romb na bou guaniéé
Yama gueunal gnima kham ak nit gnima khamoule
Diarale ngama deifadeif ba deif louma mounoul
Niguay dokhe dafa yeme ma dik louma amoule
Kou meil ni yaw dotoufi am gni daniou khamoule wayeii
Sama mbeuguel dafa fakheu wouti sa boss
Sama khole diarafé séde keur guiy dialanio
Souniou guissé mana weete ba ame loumala def
Nakh guoney may deuk wayé maguamay danèle
Sama mbeuguel dafa fakheu wouti sa boss
Sama khole diarafé séde keur guiy dialanio
Souniou guissé mana weete ba ame loumala def
Nakh guoney may deuk wayé maguamay danèle
Hummhummm (khalei bi deifal nankeu)
Hummhummm (nieuweul sakh ma deyleu)
Hummhummm (loma niane ma mayla)
Hummhummm (bou doyoule ma dolile leu)
Ecouter
A Propos de "GMD"
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl