Paroles de Balma
Paroles de Balma Par BAYE MASS
[VERSE 1]
Même souma done beugaaaate
Lila diokh meunoumako diokh kénén
Togn la néla balma
Yéssal sama ndiégeul guissouma kénén
Togn la néla balma nga ni meunoul
Nek instant mbeuguel leu
Xol bi ki ci nek nékeu khamal ni ioe leu
Dama sokhla nga balmeuu
Li niouy beurri beurri
Ioe rek la ci kholi
Ya ngék sama xol
Dem ngeu bayima mane meu dal di dioy
Ndax yama khamal love
Même souma done beugate
Lila diokh meunoumako diokh kénén
Togn la néla balma
Yéssal sama ndiégeul guissouma kénén
[CHORUS]
Khalé bi lé balma
Goné gui lé balmeuu
Khalé bi lé balma
Goné gui lé balmeuu
[VERSE 2]
Khamna ni mane leu
Ma weulbeutikou souk tok né la balma
Beugouma nga balma def ma
Thione té nga sama Diaga
La la la laaa lééé
Damani ioe leu
Damani xol bi ya ci né
Mane démone na baley
Wadia wane guinaw
Boul ma sorri dima wéteul
Mane ioe la mine
Khalé bi diaral ngama
Goudi et beuthieuk
Ya ngui ni wone ci mane
Même souma done beugate
Lila diokh meunoumako diokh kénén
Togn la néla balma
Yéssal sama ndiégeul guissouma kénén
[CHORUS]
Khalé bi lé balma
Goné gui lé balmeuu
Khalé bi lé balma
Goné gui lé balmeuu
[OUTRO]
Beugoumala bou bakh beug
Bou raw beug la def
Khawma loma def nonou
Togn leu néla balma
Ngani meunoul nek
Waxma loma def
Waxma loma def
Khalé bi lé balma
(khalé bi lé balmeuu)
Goné gui lé balmeuu
(Goné gui lé nag ma bal lé)
Khalé bi lé balma
(khalé bi lé balmeuu)
Goné gui lé balmeuu
Goné gui lé balmeuu
Goné gui lé nag ma
Bal léé nag ma bal
Khalé bi lé balmeuu
Ecouter
A Propos de "Balma"
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl