
Say Thank You Lyrics
...
Say Thank You Lyrics by YOUSSOU NDOUR
Abdoulaye ni daaro mbaar ,
Maa joor ni daaro mbaar ak seen jigéen
Yaw say aye, mo sonn ci yaw
Sóogi digéek birëm digi samba
La kurë mbisaan , sugu paate Sambala ganju leen
Yaye boye
Ciré ngi thies….
matéy nga nén Sóogi digéek birëm digi samba
Bëgg naa laa
Déglóo ti leen , ma wax ati ko
Ku ko dégg ul , ngeen jottali ko
Kuy teral sa yaay, tey nga degg ci
Ba amm ngerem am , Yalla laye teral
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
Déglóo ti leen , ma wax ati ko
Ku ko dégg ul , ngeen partager ko
Kuy teral sa yaay, tey nga degg ci
Ba amm ngerem am , Yalla laye teral
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay…
Yaw sa bonheur
Mëun ou la am solo
Féek yaw sa yaay japp ul sa loxo bi
Taf la ci dënn ëm
Na la sag al nga ‘l ma
Yaye jërëjëfëti Yaye jërëjëfëti Yaye boye
Yaye jërëjëfëti Yaye jërëjëfëti Yaye boye
Yaw nakh , dey sa bonheur
Mëun ou la am benn solo
Féek yaw sa yaay
japp ul sa loxo
Taf la ci dënn ëm
Na la sag al nga ‘l ma
La la lalala laaa
La la la la lala
La la lalala laaa
La la la la lala
Laa laa la lala
La la la la laa la
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
ku bëgg sa yaay , ne el jërëjëf
tu aime ta maman, ne el jërëjëf
tu aime ta maman, ne el jërëjëf
you love your mom, ne el jërëjëf
you love your mom….. say thank You
Watch Video
About Say Thank You
More YOUSSOU NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl