
Moytoul Sa Bopp Lyrics
...
Moytoul Sa Bopp Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Gueudj naa si banc depuis sama licence
Louma rap doon masterclass
Devant la barre je ne balance que vers et rimes
Xalima bi meuss te cass, moytoul sa bopp
Yallah moo xam liniouy reud sa dieu
Bimay diouguer si aale xamnaani musique moo gueneu tarr de dieu
Boy bouma dioudouwoon diamono david et goliath sakh doundouma saani kheer
Teh paroles en l’air rek lay diappé sa textes yi bou fekker fayoula passou ter
Noon yi sen xol yi dou cedd nakh eup naa lignmadoon dooyé ni yasuke
Daanou diogaat beut yi takk nakh victory laa nieuw dieulsi ni baye souley
Sakhouma lokho bou ken di wagnaar
Daw naa ba mbeukou soog xam lima dal
Gueum sama bopp teh xelouma niaar
Xamni ndap bouma romb sooroul sma yaay
Diokh nieup thieur indil ma handicap
Thiow lima romb eupoul bimay khaar
Fittantéh djit djit yi teksiy diap diaan
Success la kheuthioon bima thiatt di diap
Balaa nga xam, doug si kane
Baayiwouniuo ken balen niou wakh
Passé bi nak, dou lem la saff
Xamnaani fass, diom mooma war
Sama guinaw, laniouma diam
May bagn mou feign, sama kanam
Boul nangou yem si lignla wane
Takko ngui ladj, lou tekki di diar
Moytoul sa bopp
Sooga dianook sa noon
Tekki day todj sa khol nitt aka bonn
Moytoul sa bopp
Sooga dianook sa noon
Tekki day todj sa khol nitt aka bonn
Xaritt yi waagnekou dagnma yokkou
Deel andak ay nitt yu nangou fi nga toolou
Guinaaw ba oumpalewma fima dieum
Douma waagni ma takhaw coatcher luma yobou
Tay sama ngueum ngueum si mane loumou yokk
Ma ndiort né faukma waagni gnimay moolou
Kheuthieu bou dakoul na dikk teh niak diot
Meun nama diotali lep louma yootou
Mboolo mooy doolé mais beuss di nga wéré boo wekké sa doolé
Si alalou mboloo ken doula gueum ni nga gueumé sa bopp
Sam boppa ma gueneul takhoul ken yeess
Yéné naaleu lima yéné sam bop nga yéné sa bopp sam yeenek sa boss
Yéné neeg leu amma keur sama xol, bimla tidjilé bount yi lepp nga todj
Problèmou khel mais dou lep laniuy wakh
Déwoon naa bou yag boy
Baayiwam xel ligma deukoon di wakh
Diégueulou sam yaaya booy
Moytoul sa bopp
Moytoul sa bopp sooga dianook sa noon
Booko deffé oh meun nagn la touf li nga sangooko boo paré fompoo sa ngor
Balaa nga xam, doug si kane
Baayiwouniuo ken balen niou wakh
Passé bi nak, dou lem la saff
Xamnaani fass, diom mooma war
Sama guinaw, laniouma diam
May bagn mou feign, sama kanam
Boul nangou yem si lignla wane
Takko ngui ladj, lou tekki di diar
Moytoul sa bopp
Sooga dianook sa noon
Tekki day todj sa khol nitt aka bonn
Moytoul sa bopp
Sooga dianook sa noon
Tekki day todj sa khol nitt aka bonn
Watch Video
About Moytoul Sa Bopp
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl