Paroles de Ndox
Paroles de Ndox Par YOUSSOU NDOUR
Sa joie et sa pudeur font sa face cachée
Son paraître et ses formes montrent sa force
Celle que je vous chante, vous est familière
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégté ma , suturë sa, da fa méngóo k , baatin ëm
Zaahir sa , melo ya, moo won e , kattan am
Li may misaal lu ngeen xam la , am na njariñ te rafet na
Moo génné taar u adduna , moom la ñu bakke , al janna
Waxtaan e ko sax banneex la , nañ ko foηk sakkan al ko
En parler même est agréable
Respectons-la, économisons-la
Vois la mer, le fleuve
Rendons grâce à Dieu
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégté ma , suturë sa da fa méngóo k , baatin ëm
Zaahir sa , melo ya moo won e , kattan am
Li may misaal lu ngeen xam la , am na njariñ te rafet na
Moo génné taar u adduna , moom la ñu bakke , al janna
Waxtaan e ko sax banneex la , nañ ko foηk sakkan al ko
Géej gaa ngi nii yé, Dex gaa ngi nii yé
Dara gën ul ë neex taw bi
Ku weddi laaj ko bay kat ba , ci la ñuy roosé seen tool ya
Walla nga laaj ko samm kat ba , ci la ñuy nandal e jur gë
Ndox daal am na njariñ baax na
Dara gën ul lë neex taw bi
Taw daal njariñ la ci dun bi
Ndox daal njariñ ëm ,ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm , ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñ ëm , ba la nga koo xam mu jafe

Alaa gaynaago yoo samba lingeer
Donoy waaly yée , wulée ñaay ngoy
Yée gan wuri coo , wulée gaynaako yoo
Yeée , yóo , gan fari baa
Ecouter
A Propos de "Ndox"
Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl