Paroles de Mama Africa
Paroles de Mama Africa Par YOUSSOU NDOUR
Yée … yée hé hé hée hé
Yée … yée hé hé hée hé
Hoo , hoo ehnnn haaan
Hoo africains , woy le leen ma africa
Benn continent, mel ul ni africa
Am ul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw , Africa
Ana ñi soriyaante ,Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp
Une jeunesse engagée , africa
Namm u ñu dara , yalla a la barke el
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xas ee miin xam ni , fii mooy suñu kër
Come home with me , i ,i ,i
Hoo africains , woy le leen ma africa
Benn continent, mel ul ni africa
Am ul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw , Africa
Ana ñi soriyaante , Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp , avec
Une jeunesse engagée, africa
Namm u ñu dara , yalla a la barke el
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xas ee miin xam ni , fii mooy suñu kër
Come home with me , i ,i ,i
Ñun africains , su ñu ànd a ndoo
Bokk nday ak baay , Boole suñuy doole
Kholal ëllëg u adduna bi
Seet al say doom ñoo , koy mujj é
Yée hée , an han
Ni nga magge ek , ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Ni nga magge ek , ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Du ñu lë , wetio ba mouk
Du ñu lë , weccoo k keneen africa
Xam nga ni la say , doom yi bëgg é
Tag naa la kaay
Yaa ne ci suñu xol
Wo , wo , wo , wooy
Wo , wo , wo , wooy
Du ñu lë mas a weccooy kenn , yaw Africa
Ecouter
A Propos de "Mama Africa"
Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl