Paroles de Do Dara Par VIVIANE CHIDID


Néna dafa am mana (mana)
Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)
Néna dafa am mana (mana)
Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)
Meuna ndiody beugeu diay graw (diay graw)
Té ioe yoroulo nada (nada)
Meuneu gondi beug diay graw (diay graw)
 Té yoroulo nada sax

Néna yor na ohh oh (ohohoh…)
Ndéké yorou lou soucar café barada (he heheh…)
Mouy capém di pocham lépam khotékou (oh ohoho)
Lékoulo déh nanoulo, sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he (hehehe)
Di fowé sa xel bi molay sonal

Goor souné war nga diom di déf té lou yomb
Loufi diar ngey wané
Dou jom ba niawalone nama
Di digué lo meunoul
So teudé do nélaw
Dou ni nga beugeu doundé
Dou ni nga beugeu doundé
Ki tothi na kogn ba (oooho)
Ndéké yorou lou soucar café barada (he heheh)
Mouy capém di pocham lépam khotékou (oooohoo)
Lékoulo déh nanoulo
Sa nélaw dématoul né nga yor ngeu (eeeehehe)

Do dara
Do dara
Do dara

Gnata yone nga dieul alalam té fayoko
Gnata yone nga digg Pa yék Mère yi niou adji ji Macca
Té défoci dara
Nioune guissouniou dara
Ndéké ioe do dara

Néna dafa am mana (mana)
Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)
Néna dafa am mana (mana)
Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)
Meuna ndiody beugeu diay graw (diay graw)
Té ioe yoroulo nada (nada)
Meuneu gondi beug diay graw (diay graw)
 Té yoroulo nada sax

Néna yor na  (ohh oh ohoho…)
Ndéké yoro lou soucar café barada (he hehehe)
Mouy capém di pocham lépam khotékou (oh ohooho)
Lékoulo déh nanoulo, sa nélaw dématoul né nga yor ngeu (he hehehe)
Di fowé sa xel bi molay sonal

Goor souné war nga diom di déf té lou yomb
Loufi diar ngey wané dou jom ba niawalone nama
Di digué lo meunoul
So teudé do nélaw
Dou ni nga beugeu doundé
Dou ni nga beugeu doundé
Ki tothi na kogn ba, ndéké yorou lou soucar café barada he heheh…
Mouy capém di pocham lépam khotékou
Lékoulo déh nanoulo
Sa nélaw dématoul né nga yor ngeu

Do dara
Do dara
Do dara

 

Ecouter

A Propos de "Do Dara"

Album : Do Dara (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Oct 20 , 2019

Plus de Lyrics de VIVIANE CHIDID

VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl