
Bul Ma Laaj Lyrics
...
Bul Ma Laaj Lyrics by YOUSSOU NDOUR
Han han han
Han han han
Han han han
Han han , han
Tu peux évoluer à ta guise
Chérie comme tu sais bien le faire
Tu peux le faire à ta guise
Chérie comme tu sais bien le faire
Chérie bu ma laaj han , han , han
Dégg ngë daaj han , han , han
Yaw del bu ma laaj han , han , han
Da nga dégg daaj han , han , han
Chérie def al bul ma laaj
Defar al rek , def al rek , def al rek
Di na ma baxe baxe
Def al rek , def al rek , def al rek
chérie bu ma laaj han , han , han
Dégg ngë daaj han , han , han
Yaw del bu ma laaj han , han , han
Da nga dégg daaj han , han , han
Chérie yaw xam nga sama y goût
And you feel what i want to do
Ñi ma wër ñépp xam na ñu loolu
Fi nga ma tollu , mii ngi noonu
Sa ma mbëggéel romb na foofu
Na ñu muslu ci seytane
Lu ma feel lu ma feel lu ma feel lu ma feel
Lu ma feel rek yaw nga def ko
yaa di ci sa ma xol maan yaa di ci sa ma xol
Dem na gnou ba legui yaay man , maay yaw ahn ahnn
Yaa di ci sa ma xol maan yaa di ci sa ma xol
Dem na gnou ba legui yaay man , maay yaw ahn ahnn
Woo ohh ohh wooo
Chérie def al bul ma laaj
Defar al rek , def al rek , def al rek
Di na ma baxe baxe
Def al rek , def al rek , def al rek
chérie bu ma laaj han , han , han
Dégg ngë daaj han , han , han
Yaw del bu ma laaj han , han , han
Da nga dégg daaj han , han , han
Han han han
Watch Video
About Bul Ma Laaj
More YOUSSOU NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl