Da Fa Laa Lyrics
Da Fa Laa Lyrics by YOUSSOU NDOUR
Da fa laa , wóolóo
Teg la nak , fu mu teg ul keneen
Di dox sa bëgg bëgg , di dab sa banneex
Ndax seetlu nga koo yaw, Yaw la bëgg
Te yaw , yaa ko sagal waaw waaw
Bu mbëggéel , doon lumière
Mel na ni , ni jant bi
Te su am oon , lu ko gën ë leer dem na wut i ko
Ni yaw , diaral nga ko
Lu raw , sóoru gayndé waaw waaw
Lu mu metti metti , di nga tew
Lu mu sori sori , an ! Di nga ñëw
Ca dëgg dëgg dëgg
Dem na , ba dem , mën ë tul ë tok
Benn bés , bum la , gis ul
Jox na la bii respect
Nga delloo ko bii respect
Entre vous , entre vous chérie
Du wax lii def leneen
Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg ya ko diara
Ni yaw, yaa ko sagal waw waaw
Fépp fu mu mën ë ne
Da fay sentir sa parfum
Loolu yaa ko ko diaral
Ndax yaa ko liggéey
Les mots qu’il utilise sont toujours en deçà de ce qu’il ressent
Yaw yaa ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Daf la bëuggué
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Kay nga diégué ko
Mou laye déy
Yaw mii yaw
Su fekkee li mu la wax doy ula
Boo yakkamtee
Mu def al la ko , ni nga ko bëggée
Mom contane neu
Te sakh yaguena bëgg thi yaw
Boo yakkamtee
Mu def al la ko, ni nga ko bëggée
Sa lui vas chérie sa lui vas lo def nekh na ko
Da fa laa, da fa laa, def ni nga ko def
Loo bëgg , mu indil la ko
Loo laaj , mu kheuthiel la ko
Su fekkee am u ko , mu ñaan ko yalla
Chérie boy, chérie boy Ya ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy
Lo diokhogne mo dok
Chérie boy, chérie boy
Lo def nonou la
Chérie boy, chérie boy Ya ko ko diaral
Youssou Ndour, madjiguene
Boul yekhal dara
Na gua gaw, na gua gaw
Te li djieuntima
Sokhla yi, sokhla yi
Gnome gno ma gueteun
Watch Video
About Da Fa Laa
More YOUSSOU NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl