Wuyuma Lyrics
Wuyuma Lyrics by VIVIANE CHIDID
[VERSE 1]
Khalé bi, sama reini xol dé wuyuma
Beug nala té khamo ci dara
Mbeuguel tchi xol ley nek deug leu
Beug nala té khamo ci dara
Mane deh walou len ma waxko ko
Khalé bi lékatouma ndax mom
Naneu touma nélawatouma woh woh
Sama xol ya ci né
Lég lek ma wo ko, dey dal di coupé
Sama appétit coupé fébar dina ma goungué
Docteur dama love ba dof té khawma loukay fathi
Woh woh ! mba meun nga ci daraaaa
[CHORUS]
Khalé bi, sama reini xol dé wuyuma
Beug nala té khamo ci dara
Mbeuguel tchi xol ley nek deug leu
Beug nala té khamo ci dara
[VERSE 2]
Mane wo nala founé nga diapé ma sa kharite
Invité resto lalal na la louné wohooo
Nga diapé ma sa kharite
Lég lek ma wo ko, dey dal di coupé
Sama appétit coupé fébar dina ma goungué
Docteur dama love ba dof té khawma loukay fathi
Woh woh ! mba meun nga ci daraaaa
Mane beugeu na ma bagn bayiwouma
Mane guissouma guén ak koudoul mom
Mbeuguel la bari dolé nel ba ko kham
[CHORUS]
Khalé bi, sama reini xol dé wuyuma
Beug nala té khamo ci dara
Mbeuguel tchi xol ley nek deug leu
Beug nala té khamo ci dara
Khalé bi, sama reini xol dé wuyuma
Beug nala té khamo ci dara
Mbeuguel tchi xol ley nek deug leu
Beug nala té khamo ci dara
Kou ci nek ak ki nga nop
Sa guinaw bandang fakhassoul
Diougueul yeungeul bamou saff
Sa guinaw bandang fakhassoul
Kou ci nek ak ki nga nop
Sa guinaw bandang fakhassoul
Diougueul yeungeul bamou saff
Sa guinaw bandang fakhassoul
Watch Video
About Wuyuma
More VIVIANE CHIDID Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl