SAMBA PEUZZI  Je Ne Mérite Pas ça cover image

Je Ne Mérite Pas ça Lyrics

Je Ne Mérite Pas ça Lyrics by SAMBA PEUZZI

[CHORUS]
Hey bouma khamone ni ley démé doumko nop
Bouma khamone ni ley démé doumko love
Bouma khamone ni lamay def doumko diokh yeah
Bouma khamone ni lay démé hey
Pourtant banialouma dara sa yaye ak sa pape
Pourtant banialouma wone dara sa yaye ak sa pape
Bayiwone na lepp ndax ioe, ak sen wakeur
Fatéwone na nieup ndax ioe
Ak sen wakeur ouuhh ouhhh
Je ne mérite pas ça, loutax ngamey nax
Je ne mérite pas ça, loutax ngamey nax

[VERSE 1]
Babe, ak finiou diar yeup
Pour mane dou dièkh
Mounoumako geum you owe on my mind
Louma wax mou bagn, nangouma déglou
Néna dey dem, khalé bi worr nama
Sa me fais très mal tu me calcule plus
Je t'ai tout donné t'es parti comme sa
T'avais promis de rester
Pour le meilleur et pour le pire
Elle a brisé mon coeur pour du khaliss
Boul diaaaaaye sa ngor
Beugeul té y'Allah tax lolou rek'ay deug
Boul diaaaaaye sa ngor
Beugeul té y'Allah tax lolou rek'ay deug

[CHORUS]
Hey bouma khamone ni ley démé doumko nop
Bouma khamone ni ley démé doumko love
Bouma khamone ni lamay def doumko diokh yeah
Bouma khamone ni lay démé hey
Pourtant banialouma dara sa yaye ak sa pape
Pourtant banialouma wone dara sa yaye ak sa pape
Bayiwone na lepp ndax ioe, ak sen wakeur
Fatéwone na nieup ndax ioe,
Ak sen wakeur ouuhh ouhhh !
Je ne mérite pas ça, loutax ngamey nax
Je ne mérite pas ça, loutax ngamey nax

[VERSE  2]
Babe, ndax nak dina am lou bax boudé
Y’Allah xol ley fay
Je make my heart great everyday
Problème sur problème
Et j’essaye de tous régler euuuh
Tay si ki, souba si ké
Bad girls changel souba dou ni
Tay si ki souba si ké yeah
Boul diaaaaaye sa ngor
Beugeul té y'Allah tax lolou rek'ay deug
Boul diaaaaaye sa ngor
Beugeul té y'Allah tax lolou rek'ay deug

[CHORUS]
Hey bouma khamone ni ley démé doumko nop
Bouma khamone ni ley démé doumko love
Bouma khamone ni lamay def doumko diokh yeah
Bouma khamone ni lay démé hey
Pourtant banialouma dara sa yaye ak sa pape
Pourtant banialouma wone dara sa yaye ak sa pape
Bayiwone na lepp ndax ioe, ak sen wakeur
Fatéwone na nieup ndax ioe
Ak sen wakeur ouuhh ouhhh
Je ne mérite pas ça..., loutax ngamey nax
Je ne mérite pas ça..., loutax ngamey nax
Babe

Watch Video

About Je Ne Mérite Pas ça

Album : Je Ne Mérite Pas ça (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 30 , 2019

More SAMBA PEUZZI Lyrics

SAMBA PEUZZI
SAMBA PEUZZI
SAMBA PEUZZI
SAMBA PEUZZI

Comments ( 0 )

No Comment yet

About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl