BUZZLAB Dama Lay Nakh cover image

Dama Lay Nakh Lyrics

Dama Lay Nakh Lyrics by BUZZLAB


 [Hook]
Boumala nè boumala guissoul baby girl douma nèlaaw
Dama lay nakh
Boumala nè yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dama lay nakh
Boumala nè boumla guissoul mane douma am appètit no
Dama lay nakh
Yèneen guel yi yeungeulougnou ma ak lougnou meuneti moll
Yeah dama lay nakh-oOooy
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jiguîn djouko meuneu change
Kone dièmeu change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

[JAY ]
Doumala naakh mane
Douma fokaat
Meune naleu yèggeul ni rotkaat
Soumala nèwone naleu dieundeul adouna bi
khamèl bou baakh waakhou doorkaat
Dama lay naakh mane

Si parc bi nguèy doukhantou ak mane
Sa khol la beuggeu dousa taate mane
Wètali sa loss thiakou diamond
Nènagn assamane si moy limite bi mais fougnou nara dieum
Fofo nek ci kaaw
Jokh ma lokho ma fèy wèrr ak ètoiles yi ci kaaw
Dama lay nakh

[Cool Black]
Plage, shopping, resto
Life faam like echo
Dama ko kepp si ettau
nguir lekk lepe la mou yorone mané
Kou beugg dou naakhè
Real love ain't no money
Baby girl soma nakhè ma dileu nakh
Sougnouy doom yi fougnouy moudjiie
Dafa diap nè mi ngui mèy naakh
Fèèk na bobou dèh mangui koy naakh
Sister ma dileuko thiaakh
Goorou tèy watiatiatiatiatiatia-aanh

[CHORUS]
Boumala nè boumala guissoul baby girl douma nèlaaw
Dama lay nakh
Boumala nè yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dama lay nakh
Boumala nè boumla guissoul mane douma am appètit no
Dama lay nakh
Yènen guÎl yi yeungeul lougnou ma ak lougnou meuneti moll
Yeah dama lay nakh-oOooy
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jiguÎn djouko meuneu change
Kone dièm ma change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

[Zou Kana]
Tourouma leundeum ndakh yow da ngua leer
Jokhè sama khol ndakhtè parèna dè
We trash mais mbaalitou cana aka chère
Boul khatim
Boul liguèy
Ma reudeul leu chèque
Kaay ma taak leu taak leu
Sa visa dèy gaaw kham ngua cana la
Xew xew bou reuy
Yow ngua diaralma djakaa ba galè ma bache ko
Dou dara nak

[Cheeks ]
Kharouma dara loudoul taak la baby girl
Kone geum ma bokk
Dougeul sa nidiaye djakaa ba jokhè feu big money
Pour sa dot
Guiss na faÁon bou nek
Mais yow yameu diaral lou nek
Nuit de noces la yakamti
mane ak yaw yaramou néne
Problème bi moy que façon waakh bi
Waakh nako fi sa niata morom
Bobou ba lègui sama baby mama la fi guissoul
Talouma love

[CHORUS ]
Boumala nè boumala guissoul baby girl douma nèlaaw
Dama lay nakh
Boumala nè yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dama lay nakh
Boumala nè boumla guissoul mane douma am appètit no
Dama lay nakh
Yènen guÎl yi yeungeul lougnou ma ak lougnou meuneti moll
Yeah dama lay nakh-oOooy
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jiguen djouko meuneu change
Kone dièm ma change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

[Lockslegl]
Tu vois Aya ma chérie même tes tontons ces des menteurs
Dagnou lay naakh
Ils mentent, ils trichent, Ils devient
Pourtant ils ont tous un grand coeur
Yeah dagnou lay naakh
T'es tellement belle ma princesse tu devras être la hauteur
Ba dagnou la naakh
Penses à baisser la tête et à jeter un oeil sur ta soeur
Bébé ils seront prêts à tout
Faut pas te fier à nous
Ils seront prêts à jurer
Mais tant qu'il t'as pas prèsenté sa mère, pas présenté son père
C'est pas fait pour durer
Yeah dagnou lay naakh

[CHORUS]
Boumala nè boumala guissoul baby girl douma nèlaaw
Nèkoul aay nakh
Boumala nè yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dedette dou aay naakh
Boumala nè boumla guissoul mane douma am appètit no
Tè nèkoul aay naakh
Yènen guÎl yi yeungeul lougnou ma ak lougnou meuneti moll
Dedette dou aay nakh-oOooy
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jiguÎn djiko meuneu change
Tè jott nguama change baby girl
Boumala waakhè beugoumala mane dama lay naakh

Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jiguÎn djiko meuneu change
Kone dièmeu change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

 

Watch Video

About Dama Lay Nakh

Album : Dama Lay Nakh (Single)
Release Year : 2018
Added By : Afrika Lyrics
Published : Oct 30 , 2018

More BUZZLAB Lyrics

BUZZLAB

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl