
Thi Life Bi Lyrics
...
Thi Life Bi Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Niuep dinagn dem nga dessé yaay boy, mouy si walabok si nadj bi
Lou meunti kheuw sa diam lay khool, yaay bideew biko teuyé thi life bi
Thi life bi yaay mbefteem thi life bi
Thi life bi yow la gueum thi life bi
Thi life bi mbeuguelam thi life
Kone thi life bi dooko fay thi life bi
Chaque jour ma sant sama baye
Si sama yaay
Nakh tanal nama ki gueun thi niom
Ak louma am thi sama life
The sama yaay
Bégoul sama yeug yeug bi ndool
Yaay yaama diangal naka laniouy mounié
Diangalma doylou nakh fii dara dou weey
Diangalma baayi guinaaw le plou weess
Déloo lep si yallah kheuyneu soubeu mou neekh
Diangalma doylou nakh fii dara dou weey
Déloo lep si yallah kheuyneu soubeu mou neekh
Baye baayou nieup yaay yaayou kénleu
Yaay niaanalal sa taaw bi
Thiatt sekhlouko nakh moogui
Si bountou adouna sopey ak noon yi
Fii laniouy laniouy feusseulé sen mbébet si yoon bii
Manquewniou dara, dou lou bari nga yor
Sa mbeuguel sa xol
Sa mbeuguel sa xol, mom nga motaliko
Lepp lougn niouy khébé meussoul diougué thi iow
Yalna yallah def sam yeen ci iow
Niuep dinagn dem nga dessé yaay boy, mouy si walabok si nadj bi
Lou meunti kheuw sa diam lay khool, yaay bideew biko teuyé thi life bi
Thi life bi yaay mbefteem thi life bi
Thi life bi yow la gueum thi life bi
Thi life bi mbeuguelam thi life
Kone thi life bi dooko fay thi life bi
Watch Video
About Thi Life Bi
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl