JEEBA Joyeux anniversaire cover image

Joyeux anniversaire Lyrics

Joyeux anniversaire Lyrics by JEEBA


Joyeux happy birthday too you
Joyeux, joyeux

Degg na dioudou gou reuy ndaye ak baye
Wanté foulak fayda boromam
Mane degg na dioudou gou reuy ndaye ak baye
Wanté foulak fayda boromam

Niit gni dofouniou linga dji lagn lay fay (linga dji lagn lay fay)
Woté wo nieupa ngui tew di khar sa birthday (happy Birthday)
Kharit yi tew mbok yi dila nianal, yafi def lou diara waax
Sama batt bi keen douko téyé, nioungui weuy di nane

Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire dieulal beuss bi yako mome

Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire, happy birthday to you

Joyeux, joyeux happy birthday to you
Joyeux, joyeux

Guiss nama rée contane bégue ba dioy
Sama cadeau bi yako mom
Fouma meuna né damay teew

Néla ko diabe I wish you all the best
Linga geuna beugg lalay diokh
Bou doyoul reik ma dance kone rk ma dance

Kone féthial fethial reik ma guiss
Yokal music bi mou diok thi kaw
Beuss bou dellou ci dou dafa nexx
Kone amoul stress c'est la fête

Sapé comme jamais khar zero heure
Zéro heure, sapé comme jamais zéro heure, yeah

Talal ma bougie gniou dague souniou gâteau ooho
Kouma diokhoul cadeau méré nala té boul ma wooh (bouma statut)
Bene beuss la thi atte yi faw gnou begué ko
Ndéem meune ta gnak fo diar niou féte ko
Niougui way di naane

Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire dieulal beuss bi yako mome

Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire, happy birthday to you

Joyeux, joyeux happy birthday to you
Joyeux, joyeux

Degg na dioudou gou reuy ndaye ak baye
(Happy birthday)
Wanté foula ak fayda boromam

Degg na dioudou gou reuy ndaye ak baaaye
(Happy birthday)
Wanté foula ak fayda boromam

Feithial feithial reik ma guiss
Yokal music bi mou dieum si kow
Beuss bou delou si dafa nexx
Happy birthday to you

Feithial feithial reik ma guiss
Yokal music bi mou dieum si kow
Beuss bou delou si dafa nexx
Happy birthday to you you

Boromam, boromam

Watch Video

About Joyeux anniversaire

Album : Joyeux anniversaire (Single)
Release Year : 2021
Added By : Dioulde Amadou sow
Published : May 31 , 2021

More JEEBA Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl