Namel Lyrics
Namel Lyrics by MATADI
Damay tokk doumla guiss
Dama tokk lou yagu ba damako miss
Lou tax nga bayima fii
Demeu nga waye da nga fi bayi sama tiss
Magui lay woo wouyouwoma
Dafa melni yaw beugeutoma
Waxma loulay merlo
Damako beugu bayi
Doumala misère lo
Lolou damaci tayii
Sometimes damay tokk
Wett douma guiss
Lolo ma teyer ba tekk ma nakar ak tiss
Namnaaa leu diemeuleu wax ak maneu
Sometimes damay tokk
Wett douma guiss
Lolo ma teyer ba tekk ma nakar ak tiss
Namnaaa leu diemeuleu wax ak maneu
(Wetay yééé
Wetay bakhoul ci as goré wetayyy)
Keur gui sa keur lay loulay déranger ?
Togal ba khaff (half) nigth fii amoul danger
Soumala guissoul wett
Baby lini defa metti
Nieuweul sama wett
Lepp naniou ko diemeu waxtanei fiii
Dioxma nii sa loxo
(Niou) Andeu demeu foula nex
Limay yeukk xam ngako
Soumala togné balma
Sometimes damay tokk
Wett douma guiss
Lolo ma teyer ba tekk ma nakar ak tiss
Namnaaa leu diemeuleu wax ak maneu
Sometimes damay tokk
Wett douma guiss
Lolo ma teyer ba tekk ma nakar ak tiss
Namnaaa leu diemeuleu wax ak maneu
(Wetay yééé
Wetay bakhoul ci as goré wetayyy)
Soumala guissoul wett
Bb lini defa metti
Nieuweul sama wett
Watch Video
About Namel
More MATADI Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl