
Uno Lyrics
...
Uno Lyrics by MATADI
Damley guiss contane
Guiss la shine ni
Diamond tchi biir leundeum
Sama life nga nieuw nekhaal
You nex yi nguama taamal
Xawma wone ni amneu sax
Ndakh da ngua diik fott sam wol si love
Pakhass ko deft chi noflay ak freedom
Tabakh li djotone todj championne
Djokh nala médaille baby
Magui fatelikou bimley xam
First time, sa caractère ndjeuka frapper
I don’t need to tell it to the world
Dangma xol retane rek ma bardée
Mangui mouslou si sheytan ak haters yi
Yi beug gnoukhou si sunu diguenté
I do love you
Baby fi lala def
Baby fi lala def
Weynaaalaa samma baby lovaaa
Sokhlawouma kenen tchi sama life
Djokh ma sa lokho
With you there’s no bobo
Waxal gnila topou
Di djakhasser meunugn
Gnuu takalei oh no
Sama numero uno (uno)
Sama number (uno)
sama number (uno uno uno uno)
Sama number (uno)
Sama number (uno uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama uno eeeh
Sama uno
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama uno ehh eeh
Koula laal lalma koula laal lalma
Koula nara teyee yalna dee
Somay ree may contane
Man somay ree may contane ehh
Magui fatelikou bimley xam
First time, sa caractère ndjeuka frapper
I don’t need to tell it to the world
Dangma xol retane rek ma bardée
Mangui mouslou si sheytan ak haters yi
Yi beug gnoukhou si sunu diguenté
I do love you
Baby fi lala def
Baby fi lala def
Weynaaalaa samma baby lovaaa
Sokhlawouma kenen tchi sama life
Djokh ma sa lokho
With you there’s no bobo
Waxal gnila topou
Di djakhasser meunugn
Gnuu takalei oh no
Sama numero uno (uno)
Sama number (uno)
sama number (uno uno uno uno)
Sama number (uno)
Sama number (uno uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama uno eeeh
Sama uno
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama queen
Sama number (uno)
Sama uno ehh eeh
Watch Video
About Uno
More MATADI Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl