Love Distance Lyrics
Love Distance Lyrics by JAHMAN XPRESS
Waro ma sori dangua sori tchi mane
Nameu nala ioe kagn nguèy gneuw
Dileu khaar beu souf ni sèlaw
Dèm ngueu yobalè seumèy nèlaw
Lal bi weet may khol fi ngueu done teud
Di leu djanèrr ba assamane wèkh taleu
Guoudi guounèk ioe rèk lay guèintt
Motakh soumay nèlaw dou ma sawara yèwou
Distance bi takh meu silencieux
So fi nèkoul khol bi dou viber
Sama khèl mèy voyagé
Wakh ak mane dou yomb
Comme kou nèkk mode avion
So may wo meu djéki djéki noppi
Khamal ni ronguagn yangui sotti
Nguèy wakh mèy déglou seu batt bi
Sori ki ngueu beug métti
Oh nameu nala
Oh dameu wètt
Chérie yoe nameu nala
Ioe guiss leu seumeu wètt
Ioe sama ndanann nameu nala
Ioe dangua ma manqué soumla wakhè deug rèk
Ronguagn yi dou faiblesse
Dafa fèkk ioe rèk la kham
Dèm bayi meut chi tristesse
Seu parfum dèss tchi sama yaram
Alal dji lou nèkh leu
Wayè mane seu djeum la nameu
Dara mèloul ni yaw tchi sa wètt
Kènn dou ioe tchi mane nameu nala
Oh oh oh weet na
Koudoul yaw mounou meu wèteuli
Kharitt yangui gneuw way tèwoul beu lègui
Akk wakhtann bi loumou nèkh nèkh
Dèguou meu si dara nameu nala chérie
Oh nameu nala
Oh dameu wètt
Chérie yoe nameu nala
Ioe guiss leu seumeu wètt
Ioe sama ndanann nameu nala
Ioe dangua ma manqué soumla wakhè deug rèk
Watch Video
About Love Distance
More JAHMAN XPRESS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl