Paroles de Lo Beugue
Paroles de Lo Beugue Par WALLY SECK
Shibiribi ritibi sharatibu
Shibiribi ritibi sharatibu
Shibiribi ritibi sharatibu
Shibiribi ritibi sharatibu
Wax ma lo beuge ma defal lako
Wax ma lo name ma indilako
Ba ci ioe nga dieul wooh ohoh
Ma defalko amooooo kénéne kouma soute
Shibiribi ritibi sharatibu
Shibiribi ritibi sharatibu
Shibiribi ritibi sharatibu
Shibiribi ritibi sharatibu
Wax ma lo beuge ma defal lako
Wax ma lo name ma indilako
Ba ci ioe ga dieul wooh hoho
Ma defalko amooooo kénéne kouma soute
Li nga jota mougn si diguente bi
Beuri neu new niou geumoul
Né mougn ci yap bi
Wayei défo ko niel mbeugel gui
Ngay bagn mou nakhsay
Souma sagnone sa bouma guesto guiss
La sama wet
Amoulooo kénéne kuma soute
Wakhma lo nameu my boy
Ama Gaye khana nekheu
Aicha Ballago
Wakhma lo nameu my boy
Ama Gaye khana nekheu
Ayei Yaye ndéké mbeugel ni la nékhé
Wa wallay Momo Ndiaye ndéké
Mbeugel nila nékhé
Momo Momo
Kone dégal Momo Ndiaye
Momo Anta Ndiaye
Ndiémé Ndiaye sa mame
Papa Anta Ndiaye
Aby Diallo moy sa mame
Sérigne Mbacke Ndiaye seu baye
Bokum yayou am Ndiaye
Koor Kiné bayou Saliou
Wa wallay Momo Ndiaye
Ndéké Momo sama way la
Diagay sa yaye
Ayei yaye ndéké mbeugel nila nékhé
Shibiribiré Shibiribiré
Ndéké mbeugel nila nékhé
Shibiribiré Shibiribiré
Ndéké mbeugel nila nékhé
Momo Ndiogou Ndiaye
Momo ndiaye ndéké Momo sama way la
Wa wallay Midou Ndiaye
Ndéké Momo sama way la
Ayei yaye ndéké mbeugel nila nékhé
Ecouter
A Propos de "Lo Beugue"
Plus de Lyrics de WALLY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl