Paroles de Les Hommes de l'ombre
Paroles de Les Hommes de l'ombre Par WALLY SECK
Ndékéte rew koufa dioudo way
Am fa ceer ba taxx ñu naan
La domou rew mi
Féxéél ba bok ci gni ñu naan
Gni ngi jarign rez mi ci faana
Boumou meuna done
Ne demande pas ce que le pays peut faire pour toi
Mais demande toi plutôt ce que tu peux faire pour lui
Yénn gni karangé rez mi
Lepp ci sutura
Les hommes de l’ombre
Jokondial jarama
Yénn gni
Yague di xéxxal
Rewmi ci sutura
Les hommes de l’ombre
Su wakh ji baré dou gnom
Su jeuf ji reuyé gnome là
Royaal ma ci gnom jikko yillé
Ndax yalla dou fay waxx di bayi jeuf
Médiateur fédérateur
Doléén xam bañu wonela guanaw
Missaal mi moun na bagna soré
Woy kat ba louko way waxal
Ci lou baxx ci doundeum lako def
Teub di daanu ba weursseuk tourou
Taka dabar bay wadia toxu
Dé niew tagalé léén
Way ka tba nann xalam demonde na bay nexx
Gni nénaño gni nénaño
Aduna amoul solo
Ecouter
A Propos de "Les Hommes de l'ombre"
Plus de Lyrics de WALLY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl