Paroles de Borom Keur
Paroles de Borom Keur Par OMZO DOLLAR
[INTRO]
Gouro, trois pièces
Gouro, trois pièces
Gouro, trois pièces
Gouro
[COUPLET 1]
I say aladji miézè
Déf la sama sokhna lala yèné
Mane ak yow ci diaka imaam ak préfet
Bolémaak sa papeu nako géré
Wooo, yow la, waaa, yow la!
Yow la, waaa yow la !
Beug nala, khamna beug ngama
Doyal ngama, soumla amé amna nienti diabar
Hey ! Ani Pa bi nang ko wo oh oh
Damala beug takk guénouma ak guel oh oh oh
Viens père wakhma lane la, loy douté hé hé ?
Beug nako, amna diiné ak liguèy !
[REFRAIN]
Hey ! Baby oubil ma sa xol pour ma nek sa borom keur
Han Yeah ! Nala dieundeul bène keur pour ma nek sa borom keur
Wo ! Wakh ak sèn wa keur, nélène may sa borom keur
Oh Yeah ! Naa taal sèn keur sougn-ma défoul sa borom keur
Oh Yeah !
Dina indi gouro, déf trois pièces
Gouro déf, trois pièces
Gouro déf, trois pièces
Gouro déf, trois pièces
Gouro... trois pièces (ngané lane)
Gouro... trois pièces (ngané lane)
Gouro... trois pièces (ngané lane)
Gouro... trois pieces
[COUPLET 2]
I say takk sama fitt, do am bène woudj baby à part sama fitt, yeah !
Boula nékhé doreul radio, maaye sa borom coeur baby cardio
Louy bayanté bou kouné seuyé seuye bi
Bougne déf lolou kay niou seuye seuye bi
Mak yow warouniou am blem
Ya eupone prétendants championnat anglais
Réception invités yi naani ginjèèère
Boma fiiré dina mourou melni ninja
Mayé bou ndieuk, mayla galé tek ci trois cars
Souma lay niani feug gandi boubou trois quarts
Mane la gars yi wowé bad man Miézé
Am diabar bou melni yow la yagg rêvé
Nuit de noce premier song ma mayla bébé
Dane na tok di ladj y’Allah fi nga fétéééé hey !
[REFRAIN]
Hey ! Baby oubil ma sa xol pour ma nek sa borom keur
Han Yeah ! Nala dieundeul bène keur pour ma nek sa borom keur
Wo ! Wakh ak sèn wa keur, nélène may sa borom keur
Oh Yeah ! Naa taal sèn keur sougnma défoul sa borom keur
Oh Yeah !
Dina indi gouro, déf trois pièces
Gouro déf, trois pièces
Gouro déf, trois pièces
Gouro déf, trois pièces
Gouro... trois pièces (ngané lane)
Gouro... trois pièces (ngané lane)
Gouro... trois pièces (ngané lane)
Gouro... trois pièces
Aladji Miézé, déf la sama sokhna lala yèné (yeah, yeah, yeah)
Aladji Miézé, déf la sama sokhna lala yèné (yeah, yeah, yeah)
Aladji Miézé, déf la sama sokhna lala yèné (yeah, yeah, yeah)
Aladji Miézé, déf la sama sokhna lala yèné
Gouro... trois pièces
Gouro... trois pièces
Gouro... trois pièces
Gouro
Ecouter
A Propos de "Borom Keur"
Plus de Lyrics de OMZO DOLLAR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl