
Paroles de Vive L'amour
...
Paroles de Vive L'amour Par MOMO DIENG
Mbegeel rek ka neexool
Ci bun la nobee
Mbegeel aka neexooy woowooy
Ci bun la beggee
Ni mene kot daal
Amunu mbaam
Ak nimula beggee yaw ngakkoy fowee
Mbegeel dafa tiiss
Té xolul melokaan gaani
Suma la nobaté teyema
Bul naagu
Bul fowee yooyu
Sosse demba majigeen cé yacine baby
Xool ma rémaa, ma tagook coow li
Li mani cheri booy waxal
Somala nobee luma yor joxlako deesseek neen
Sosse demba majigeen cé yacine baby
Xool ma ree ma, ma fatté coow yi
Xool ma ree ma, ma fatté coow yi
Mbegeel rek ka neexooy
Ci bun la nobee
Boo dajee sa ame sœur
Teeyel teeyel
Mu degger degger
Mbegeel dafa tiiss
Te xolul melokaan gaani
Sun la nobaté teyel bul naagu
Bul fowee yooyu
Sosse demba majigeen cé yacine baby
Xool ma ree ma nawal noon yi
Xam nga sama bir
Sama darra umpu la
Soo ma beggee luma yoor joxla ko
Deesseek neen
Li mani cheri booy waxal
Maa la bege bamu jeex dawu maci dara
Xool ma reema ma taagook coow yiii
Mbegeel dafa tiiss
Te xolul melokaan gaani
Sun la nobaté teyel ak sa fukki loxooy
Aly baba coumba naar mbeggeel mooy
Ay waay man fuma jem, cey xalle bi jaral nama
Nop naakoo
Ni waawaaa aly baba coumba naar mario mbaye
Mussee jama coumba sene, mbaye kuli fati ma diodio
Borom ngaay ndanaan ge
Aly baba coumba naar, mbeggeel looy
Hry yaw man fuma jem, cey xallé bi jaral nama
Nop naakoo
Coow le ce pindum teen ba, wey gaa ni amul baak
Mario mbaye
Musse jama coumba sene
Mbaye kuli fati ma diodio
Borom ngaay ndanaan ge
Aly baba coumba naar mbeggel looy
Ecouter
A Propos de "Vive L'amour"
Plus de Lyrics de MOMO DIENG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl