CANABASSE Gadaay cover image

Paroles de Gadaay

Paroles de Gadaay Par CANABASSE


Bayil ma sori lépé louy sa ma vibe
Bayil ma sori lépé louy sa ma vibe
Kil sa ma vibe
Kil sa ma vibe
Kil sa ma vibe
Fok ma sorri lépp louy sama vibe
Def plein cii truk bi accéléré gadaay
Sorri lépp louy disseul mind
Djannok sama bopp sokhla nagou time
Eeh faut que ma sorri louy kill sama vibe
Ndakh boppou bi féss na nélawatouwa night
Bayima taak dookh
Bayima taak dookh
Bayima taak dookh
Douma yobou gaat loudoul bopp
Def plane mode sama phone
Dagg liens yeup amoul, mbook noome
Nieup meunou gnou aand bideuneti
Kheuthie na ma wara délou teudi
Té teudi bi bou naré yaagg fok teudd cii fu nooy
Lemme go lemme go lemme go
Bugnou yéwo guissou gnouma di nagn nannde diaroul tagou lemme go yeah
Ku khass ba rép bokoy fadj ba suba do c djeulé none
Té garap bu gorr bokoy rosé beu déwéne do ci djeulé
Niaam kone
Bayima taak djouk dookh
Cii lamine rek lagniy bokk
Mane ma warone déné bopp
Mais meunouma démé démi khol
Bokatougnou lougnou cii khol
Kheuthie na gno lougou cii soll
Wanté bakatougnou lougn cii djiteul

Fok ma sorri lépp louy kill sama vibe
Def plein cii truk bi accéléré gadaay
Sorri lépp louy disseul sama mind
Djannok sama bopp sokhla nagnou time
Eeh faut que ma sorri lépp louy kill sama vibe
Ndakh boppou bi féss nélawatouma night
Bayima taak djouk dookh
Bayima taak djouk dookh
Yeah
Bayima taak djouk dookh
Bayima noppi rek beugouma waakh
Ndaax book sip boul ba légui amoul been mot
Boumey décrire cii sama khol
Ess que dingua nélaaw goudi
Ess que dingua méy khalate touti
Ess que dingua tokk ba am aay regrets cii sunu digeuneté bi noumou moudiou
Démey soopp boumla né mbindéf bouma geuneul sama bopp
Wanté sama khol eupeu dolé sama bopp
Sama khol laleu dinthione yeah
And i still get love for you
Yeah mbeuguel moma gaagn
Té sama beutt tooy nagn
Wanté boumla wéré samey noon lay méy ndaam kone
Bayima nopi rek dookh
Neubeu samey rongaagn
Wéétook sama méttite ba biss boumouy diaaleuh rek la sokhla sama
Mind bayima ma  yookh
Beugeuma gnou laadji meu lane moma djott
Yeah roussna gnou guiss sama mélokanou kanam
Ndax dégnou nane bayima sééyy bala naadj bi di djok
Bala naadj bi di djok
Djannok sama bopp sokhla nagou time
Fok ma sorri lépp louy kill sama vibe
Def plein cii truk bi accéléré gadaay
Sorri lépp louy disseul sama mind
Djannok sama bopp sokhla nagnou time
Eeh faut que ma sorri lépp louy kill sama vibe
Ndakh boppou bi féss na nélawatouma night
Bayima taak djouk dookh
Bayima taak djouk dookh
Bayima taak djouk dookh

 

Ecouter

A Propos de "Gadaay"

Album : Gadaay (Single)
Année de Sortie : 2018
Ajouté par : Afrika Lyrics
Published : Sep 01 , 2018

Plus de Lyrics de CANABASSE

CANABASSE
CANABASSE
CANABASSE

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl