Paroles de Baye Barhama
Paroles de Baye Barhama Par AKHLOU BRICK
[INTRO]
La Ila ha ilala
Lay laylla ilala
Bayo yay sougnou Baye
[VERSE 1]
Barhama gnou Wan yoon
Yoon Bouy dem Thi Allah
Amoul sik ni mom mo don nou Yonénte bek Cheikh Tidiane
Bilay wat na ko do mass
Barahama may borom Fass
Bayou Dam ak Baye Ass siguil na dîné l’Islam Thi adouna
Diok léen gnou dém (Diok léen gnou dém)
kay léen gnou nani Thi guediou guedji Baye mo yor faydou tidiani
Diok léen gnou dem (Diok léen gnou dém)
Ila medinat di Barhama ki mo gnou hamal al khakh bi
[CHORUS]
We love Love love love
We love we love you so much
Baye Bayoooo Baye Barhama
My heart and my body my soul and my life are fo Baye Niass
Ya Barhama Abdallahi ya Barhama kaolack Yniassy Niassy
Baye Baba Baba Yniassy
Barhama Abdallahi ya Barhama kaolack Yniassy Niassy
Baye Baba Baba Yniassy
Barhama Abdallahi ya Barhama kaolack Yniassy Niassy
Baye Baba Baba Yniassy
Niassy Niassy
Baba Yniassy
Iassy Niassy
Baba Baba Yniassy
[VERSE 2]
May bakani madi gohi
May li fegn té May li neubou
borom faydou béy kiy Hamlé Yalla kou beug ham yalla dangay sobou
Diant soodan bi djoudo Taïba
Santh Medina ték thi ila Kossy
Tan ay ndawam thi bir Péyi ba moy Barham Barham Moy kignouy nouyoussi
Mawtou habla anta meuwtou kay len dé bala déwa gnew
Fegn na Kaolack Mo yor mbotou salfa bi saf na bay yeungal keuwna
Deug deug ya Barhama ya gnou hamal lougnou hamoul won allah
Feug deund sede Yalla loudoul yalla loumouy nek mom allah
[CHORUS]
We love Love love love
We love we love you so much
Baye Bayoooo Baye Barhama
My heart and my body my soul and my life are fo Baye Niass
Ya Barhama Abdallahi ya Barhama kaolack Yniassy Niassy
Baye Baba Baba Yniassy
[VERSE 3]
Barhama Abdallahi ya Barhama kaolack Yniassy Niassy
Baye Baba Baba Yniassy
Barhama Abdallahi ya Barhama kaolack Yniassy Niassy
Baye Baba Baba Yniassy
Niassy Niassy
Baba Yniassy
Iassy Niassy
Baba Baba Yniassy
Baye Baba Baba Yniassy
Niassy Niassy
Baba Yniassy
Diok léen gnou dém (Diok léen gnou dém)
kay léen gnou nani Thi guediou guedji Baye mo yor faydou tidiani
Diok léen gnou dem (Diok léen gnou dém)
Ila medinat di Barhama ki mo gnou hamal al khakh bi
Gnou dém thi Ya Barhama Abdalah Ya Barham modi sougnou Baye
Allah Baye allah yay sougnou Baye
Barhama Abdalah Ya Barham modi sougnou Baye
Allah Baye allah yay sougnou Baye
Barhama Abdalah Ya Barham modi sougnou Baye
Allaah Baye allah yay sougnou Baye
Baye Bayoooo Baye Barhama
Allaah Baye allah yay sougnou Baye
Baye Bayoooo Baye Barhama
Allaah Baye allah yay sougnou Baye
Baye Bayoooo Baye Barhama
Allaah Baye allah yay sougnou Baye
Baye Bayoo Baye Barhama
Ecouter
A Propos de "Baye Barhama"
Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl