ELZO JAMDONG Coulisses cover image

Coulisses Lyrics

Coulisses Lyrics by ELZO JAMDONG


[CHORUS]
Mangui samay coulisses di préparer
Begueul ay nitte youma khamoul
Mel ni amouma life amouma amour
Mangui studio di bind album
Pour nitte youma guissoul
Kagn lamay dallou

[VERSE 1]
Job naa bëgg siiw
Légui siiw naa beuggueu laqatu
Moussou ma bëgg feegn pour réussir
Mais am te do siw legui amatoul
Diaratoul may gueuneu yeek yegg niveau
Chester doga sokhleu rare
Overdosou amy winehouse legui
Diakhalatouma ndakh doyeul naa
Esk souma demissionner woul wone
Seme ex jobdoumeu tané fi
Beugone bolé vie d’famille ak showbizzz
Mais ken meunoul ameundo niaari vie
Ak jamdong bimay woté founekk
Est-ce-que mangui dounde lou Pacifique
Mangui doga raniè ndéké succès
Beuri ne piège beuri neu artifice (whoa)
Gagner naa ay cachet (whut)
Signer naa ay queuchet (yeah)
Yokk naa ay amis (Facebook)
Niakk naa ay kharit deugg
y’allah may ma ay mbokk
Mane meu tann ay fanss
Deukké daw guinaw ndam mbaa
Doumeu nitte kou gatt ay fan

[CHORUS]]
Mang semey coulisses di préparer
Begueul ay nitte youma khamoul
(Ay nitte youma khamoul, ay nitte youma khamoul)
Mel ni amouma life amouma amour
(Amouma amour, amouma amour)
Mangui studio di binde album
Pour nit youmeu guissoul
(Pour nitte youmeu guissoul)
Kagn lemey dallou

Carrière bi dinema gaagn té douma ko yeg
Mingui mey khaagn mey gueuneu réérr
Carrière bi dinema gaagn oh té doumeu ko yeg
Mingui mey khaagn mey gueuneu réérr

[VERSE 2]
Daw na ay kilomètres (ay kilo)
Tokh naa ay kilo herbe (rrah)
Dieul yonu missionnaire (yeah)
Pour nekk millionnaire
Sol naa ay pullover ak t-shirt
Ou marque yi gueuneu cher
Wayé même tabakhou Imhotep
Mounoul takh banga nekk kou immortel
Concert ya ngui gueuneu fess
Supporter ya ngui daanou lerr
Guedj na degg seme baatou mère
Est-ce que li mo nékone
Seme nianou mère ? (rrah)
Dougg naa big thiow dougg naa
Big thiow te ken dougueuloumeu tchi
Bougg naa kick torop, beugg done big boss
Mais dou ben nitte dou machine (machine)
Ben nitte dou machine (whoah whoah)
Machine sakh dey bugger
Cousin meun ngama méré,
Wonoumala nimele beugué
Kholeul legui demey toke 3 mois
Doumeu deggueunték Babs
Namm naa mane ak Jean Joe biniouy bokk
Agn temps fac
(Biniouy bokk agn temps fac)

[CHORUS]
Mang semey coulisses di préparer
Begueul ay nitte youma khamoul
(Ay nitte youma khamoul, ay nit youma khamoul)
Mel ni amoumeu life amoumeu amour
(Amouma amour, amouma amour)
Mangui studio di binde album
Pour nitte youmeu guissoul
(Pour nitte youmeu guissoul)
Kagn lemey dallou

Carriere bi dinema gaagn té douma ko yeg
Mingui mey khaagn mey gueuneu réérr
Carriere bi dinema gaagn oh té doumeu ko yeg
Mingui mey khaagn mey gueuneu réérr
Carriere bi dinema gaagn té douma ko yeg
Mingui mey khaagn mey gueuneu réérr
Carriere bi dinema gaagn oh té doumeu ko yeg
Mingui mey khaagn mey gueuneu réérr

Watch Video

About Coulisses

Album : Coulisses (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 18 , 2019

More ELZO JAMDONG Lyrics

ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl