Temps Amoul Lyrics

BRIL Feat ABDOU GUITé SECK Senegal | Hip Hop,

Temps Amoul Lyrics


Yaw lingay déf nang thi gaw
Temps bi doula xaar
Diougal weuri fingay aw
Temps bi doula xaar
Il ne nous attend pas…
On doit faire des pas…
On s’inquiète pas
Alors que c’est le temps qui nous tue
Lève-toi il est temps
It’s time to shine
T’as plus le droit de dire i take my time
Le temps n’est pas à toi
La mort ne prévient pas
Oooo ohho ooh
Souba souba yalla la

Ne remet pas à demain ce que tu peux faire aujourd’hui
Aide-toi et le ciel t’aidera c’est ce qu’on m’a dit
L’avenir appartient à ceux qui se lèvent tôt
Arrête de rêver devance le soleil
Bosse dure et tu seras un boss
Réveilles toi-même si t’a sommeil
Yaw lingay déf nang thi gaw
Temps bi doula xaar
Diougal weuri fingay aw
Temps bi doula xaar
Il ne nous attend pas…
On doit faire des pas…
On s’inquiète pas
Alors que c’est le temps qui nous tue

Wake up diougal thia bamouy tél
Sol say dalleu diémeu wouti sa yoone
Takh say diadj nango wétal sa yoone
Wée ndaxté diante bi doula xaar
Déf ni mame you bakh yila mboote
Bagne deuké nane thianyine déf yeufi sénégalais
Yinga xam sayoune xeuyé door waar éhh ehhh

Yaw lingay déf nang thi gaw
Temps bi doula xaar
Diougal weuri fingay aw
Temps bi doula xaar
Il ne nous attend pas…
On doit faire des pas…
On s’inquiète pas
Alors que c’est le temps qui nous tue
Yaw lingay déf nang thi gaw
Temps bi doula xaar
Diougal weuri fingay aw
Temps bi doula xaar
Il ne nous attend pas…
On doit faire des pas
On s’inquiète pas
Alors que c’est le temps qui nous tue

BRIL (11 lyrics)

BRIL FIGHT 4 is a musician, Beatmaker, singer and rapper from Thiaroye - Diamaguéne in Senegal. He is also the founder and General Manager of the Class'Chic Music label.

Leave a Comment