Sante Yalla Lyrics
Sante Yalla Lyrics by BAYE MASS
[COUPLET 1]
Def nama goor yallah soudoul yé domou yayam soldarou Bamba
Louma diokhagn ioe nga diokhma, mashAllah sante naleu
Diokhma ndeye diou mate ndeye, baye diou mate baye
Mane dh geureum naleu
Baye fall dou niakeu, loumou beug am ko ndax thiofélam ci Bamba (Al Hamdoulilah)
[REFRAIN]
Sante na y’Allah, Sante na Bamba
Sante na y’Allah, Sante na Bamba
[COUPLET2]
Oubil nama oubékou biir ak bité, oubi samay bountu def ma may soldarou Bamba
Sante na gnima diapalé bama wéssou lou méti
[REFRAIN]
Sante na y’Allah, Sante na Bamba
Sante na y’Allah, Sante na Bamba
[COUPLET2]
Gorr ley done, goor yallah dafay deugou kou bax ley done
Foula ak diom feel ndigeul mbotou yalla bi mome ley yor
Kou sante y’Allah bam ma défé lima done
Sante y’Allah bam ma défé domou niary gorr
Sante y’Allah bam ma mousseulé ci none yi
Sante y’Allah bam ma gnitaleu lé sama yone
[REFRAIN]
Sante na y’Allah, Sante na Bamba
Sante na y’Allah, Sante na Bamba
Watch Video
About Sante Yalla
More BAYE MASS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl