Dama La Love Lyrics
Dama La Love Lyrics by AKHLOU BRICK
Bb yaw ba nam nga ma
Man dama la nam ba nam nimala namé eh eh yeah
Té yaw bb tam nga nak
Dieul peage bi raw ma mai nak tay ma feul pé eh
Bb yaw ba aimer nga ma
Man damala aimer ba aimer ni mala aimer eh eh
Tè Yaw bb diaral ngama
Dohé ak ay dal wegn thi desert bi bamou dieh ehh
Def ma ndank yama meun thi pét ma nangouwat ko
Thi diam Lay doh
Wahone nalako thi souba faw ma bamtouwat ko
Damala Love
Def ma ndank yama meun thi pét ma nangouwat ko
Thi diam Lay doh
Wahone nalako thi souba faw ma bamtouwat ko
Damala Love
Baby Dama la
Yaw Dama la love
Té Andou mathièk sago
Bb Dama la
Yeah yaw dama la love
Mala topé dina dof baby
Baby Dama la
Yaw Dama la love
Té Andou mathièk sago
Bb Dama la
Yeah yaw dama la love
Mala topé dina dof baby
Negga man rek malay togn
Wanté boudoul man kenen kan moko sagne
Negga man may guenee sa rangogne
malay tongn bafou togn yam dik baloula tado bagn bae
Yanssay damay yeukeuti sama batt
Merr nela may nala batt
yaram bi daw ma reuthiou wakh diou niaw
Gneuw dila balou wat
Nan b damadone fo
Dama tam ay wakhou kon hanadou may Tom yay Jerry beugante meunta niak thiow yaw
Sekougnou demal ma dem
awma mot hepna je t’aime motah malay wah damla bagn
Mais damla nob meunoul ame prix yaw am nga prix nobel
Man damla nob damla nob ba lab ci guédiou nobel love you.
Def ma ndank yama meun thi pét ma nangouwat ko
Thi diam Lay doh
Wahone nalako thi souba faw ma bamtouwat ko
Damala Love
Baby Dama la
Yaw Dama la love
Té Andou mathièk sago
Bb Dama la
Yeah yaw dama la love
Mala topé dina dof baby
Baby Dama la
Yaw Dama la love
Té Andou mathièk sago
Bb Dama la
Yeah yaw dama la love
Mala topé dina dof baby
Watch Video
About Dama La Love
More AKHLOU BRICK Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl