Sekougn Bayante Lyrics
Sekougn Bayante Lyrics by JAHMAN XPRESS
Begun ak lamign gna deuk
Yénn say gnou laalé
Man rek ma kham sa ndieuk
Motax sékougn bayanté
Boul mérr ba tangeu
Waxma loy reuthiou souniou joubo wé
Meun ngama gaagn té doko yeuk
Boulma waan sa dolé
Tidjil sa kanam bi nga teudj
Maan nga nop mala sommet
Niangal diapoula
Même so méré dangay gueuna rafétt
Doley mbeuguèl xadioul si yaw
Bayil finga téyè
Lewto sou yagué diéleu bi gnaaw
Mak yaw sékougn bayanté
Namnala wayé fokma tekk khel
Yèndo composé son numéro té douma beuss appel
Yéén say ma dougou mode fantôme
Dèm status xol la khèw tchia loy dokh
Gueuth na guiss no mèèl
Saguo ngi may raay
Wantè beugouma ndieuka wakh aak mom
May goor tè fokmou xamni fi
Bèneu baat leu may borom
Lowakh ma tangal tè
Pourtant man beug na bayi mou cèdeu
Dèl makh nakh so noppè ma doff
Sa baat la beug di dègu
Diaroul ngamay wane ni yangui ci diam
Xam naani yangui souffrir
Mak yaw gnoy wakh tè xamna lèèp
Damala bayi si biir
Damala nameu tvhi live bi goudi
Waay dougal dama ragal wètay
Taamal ngama lou meunta weuy
Wayè xeuyna dinga ma wo tay
Soumay lèèk lou nekh
Ba khèl mi dèm tchi yaw
Day melni meussou ma khiif
Wakhal aak maan nakh namnala
Sama khol meuna guiff
Oh love
Eh eh love
Magui beurè aak sama khol bi
Ba goudi gui dièkh
Wayè fouma tourné sa kanam laay yaam
Mbeuguèl di gueuna yokk
Come biss bimalay gneuka kham
Mal yak sougn khoulo
Nonn yi am ndam
I’m sorry yaw nameu nala eh
Chérie non non
Stay with me oh
Because baby i want you soo
Magui dora guiff
Lègui soma wowé
Yaay reine def nala leeep
Nakh mak yak sekougnou bayantè
Dédèt yaw lay feel
Dou maan dou yaaw
Khol yi gnoko décidé
Mak yak sekougnou bayantè
Dou maan dou yaaw
Khol yi gnoko décidé
Mak yak sekougnou bayantè
Dou maan dou yaaw
Khol yi gnoko décidé
Watch Video
About Sekougn Bayante
More JAHMAN XPRESS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl