Fayeku Lyrics
Fayeku Lyrics by DIP DOUNDOU GUISS
[VERSE 1]
Del compté may péssé khaliss
Ma ngui huitième assamane di guiss niane
Yi ioe ya ngui cinquième étage
Woté nagn mbolo pour rayma ndax
Li len déssé motoul unité télécentre
Niom daniou téla ndiol yékha magu
Niom daniouy yékha yor téla niakk
Teueulé m’ak yéneu boy yi
Moy teukeulé kéér ak nathi
Teukeulé gaindé ak khathi
Mawti won ako mais nangou gouma djeul
Kone khamna dama koy message
Wayé soumay dieulci samay none ak séni
Diéguénialé may ndieuka djalé
Chien méchant nga noo do chef de gang
Chef de chantier mo geun chef de chambre
Diangue nga dotouniou la bigup
Ma niggah thiat dougou la dala bireul
May len lokho niou yottou sama rouh
Mangu’ék khir bi né len niou keufeulou
Xeex nga beug boul khar niou eufeul niou
Amo drapeau niggah ba di ko thioup
Ba paré y’Allah ak y’Allah
Lan moy tax bama rouh
Meme bou fén amoul wone
kéneu dou dioup guéleuwar
Douma tallal lokho mouk
yéleuwanouma damay fayékou
[CHORUS]
Respect bi def ko khaliss
Mane kham na yonou banque
Bougouma dem fou soriwoul
Motax khawma yonnu diam
Diam ji def ko business
Sauf bou féké sa fitt dess
Missionné caisse sou Biles Gates
Khaliss dou déh même souy dièkh
Fayékou liquide mba fayékou chèque
Fayékou souba no fayékou tay
Fayékou djouni mba fayékou ten
Boul ma fay lou chéroul no lou chère
Khaliss dou déh même souy dièkh
Fayékou liquide mba fayékou chèque
Fayékou souba no fayékou tay
Fayékou djouni mba fayékou ten
Boul ma fay lou chéroul no lou chère
[VERSE 2]
Deugeur té deuthi ni
Dreuthi leundeum ni deuthi
Chaque jour la chaque nj
Abote boul ndol di dathi
Kou geum ni niak moy sa weurseuk
Reuthi téki faté lofi dathi
Séguam gni tax ngey job di khagn
Sa bop nélaw ni dathi sa lallou hopital
Mbeuguel dou djar dou dé bouyabo
Do meussa guiss mbeuguelbou tathi
Sa bolou agn
Kouné na nga outi xam xam bala am néko
Pour mou waan la keur kocc barma
Guiss nafi yeungeul geusseum sa tate ba
Diaréfa yeungeul geusseum
Liné sa compte banque
Fou thiate di eup di geud taw imam di
keup caisse sou djakka
Ribaa ci poch’ou prési ak ribaa
Ci gorrdjiguén yi am liberté
Batré si xew CFA la ngor di diar
Ligeéyeunté nguir chèque
Lou lew néew ni guiss vierge
Bougougn téd ci pétt
Religion bi business
Hypocrite nga fuck sa love ak peace
Bala ngama thiop ma thiop sa xiff
Forcé king ni kou djoudo ci siif kénn
Ci niom denthioul diouroomi briques
[CHORUS]
Respect bi def ko khaliss
Mane kham na yonou banque
Bougouma dem fou soriwoul
Motax khawma yonnu diam
Diam ji def ko business
Sauf bou féké sa fitt dess
Missionné caisse sou Biles Gates
Khaliss dou déh même souy dièkh
Fayékou liquide mba fayékou chèque
Fayékou souba no fayékou tay
Fayékou djouni mba fayékou ten
Boul ma fay lou chéroul no lou chère
Khaliss dou déh même souy dièkh
Fayékou liquide mba fayékou chèque
Fayékou souba no fayékou tay
Fayékou djouni mba fayékou ten
Boul ma fay lou chéroul no lou chère
[OUTRO]
Fayma mo geun mayma
Fayma sama sama
Mo geun ngamay may sa
Fayma khaliss mo geun may ma khaliss
Fayma sama fucking money fin
Fayma xaliss mo geun may ma khaliss
Fayma sa khaliss
Mo geun ngamay may sa khaliss
Fayma khaliss fayma khaliss
Mo geun mayma khaliss
Fayma sama fucking money fin
Respect bi def ko khaliss
Mane kham na yonou banque
Bougouma dem fou soriwoul
Motax khawma yonnu diam
Diam ji def ko business
Sauf bou féké sa fitt dess
Missionné caisse sou Biles Gates
Khaliss dou déh même souy dièkh
Watch Video
About Fayeku
More DIP DOUNDOU GUISS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl