Mirna Lyrics by WALLY SECK


Wakhal ak mane mi mo geune
Soma guissé yangui saalé
Sa mbeuguél mi ngui lay réy
Setlouna setlouna
Setlouna, setlouna
Yow ma nga nobb
Wakhal ak mane mi mo geune
Soma guissé yangui saalé
Sa mbeuguél mi ngui lay réy
Setlouna setlouna,
Setlouna, setlouna
Yow ma nga nobb

Sou Samedi dioté
Yangui khol nimay sagnsé
Sou Dimanche dioté
Yangui khol nimay rombé
Yow wakhal ak mane
Mo geune, mo geune, mo geune
Yow wakhal ak mane
Mo geune, mo geune, mo geune
Setlouna, biniou khamanté ba légui
Yangui may dozé
Wouy lélé aaah
Diaratouko mirna
Ah mirna, diaratouko mirna

Kholal tchi Papa Ngom
Nimou nobé Ndella wornama
Formi...[doudou]...dable
Moy baayou, bayou Anta Ngom
Papa Ngom, l'incontournable waw
Yérim Ndella, bayou Mohamed laay woo
(Son compte Twitter)
Wanma ninga nobé
Wornama, fonk nala darling
Dieuleul sa téléphone, Photowou yoné ma
Ma yoné la let’s love line
Solal sa louboutin, diagar diagari
Wopopopopo, yangui may gagn

Goor gnilé goor gnilé
Amlène yeurmandé tchi djiguène gni
Wooo, li nékh na
Mat ngama rapp, matma djiné séytané
Darling mirna
Setlounaaaa

Yakamtina nga wonma sa tiofél
Sa sokhla, bila geuna sokhal
Sokhla bi moma tchi nekh
Sa mbeuguél, bilay yakamtinako
Yamala am mala
Yow yama geuna love wawaw

Adja yonel
Buur bi Yallah limou massa ndogal
Deugeula kagn ndogal gui moma si nékh wowowo
Yama... am mala
Yow yama geuna love wawaw
Adja yonel
Sa tiofél loumou bari bari
Mane sama boss wésouna guédj wawawawaw
Souma démone ba ditcha féy
Dina saggou ba faf fa lapp man
Yama... am mala

Yow yama geuna love wawaw wawaw
Bilay, toumani, lépp ni la
Bilay, toumani, lépp nonou la
Oumou Wade bakhna, lépp nonou la
Waw walay Cheikh Senghor, lépp ni la
Assane ndaama, lépp ni la
Chérie titou bakhna, Diagne narr nonou la
Moustapha narr woma, lépp ni la
Coumba Ngom woma, lépp nonou la
Ndèye Marie Marème Ndoye, Baaye Waly nonou la Adou
Wopopopopopopopopop

Watch Video

About Mirna

Album : Mirna (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 20 , 2019

More WALLY SECK Lyrics

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl