Tangal Lyrics by SAMBA PEUZZI


[VERSE 1]
Geumoko wone finiou
Nobanté domafa guiss
Dieul Fuck Love
I'm savage def sama devise
Diépi wone beep goor gouy
Doundou relation hindou
Guéne ak sho une semaine mou dème
Djiko yi meunoul andeu
Kholou keurign la yorone
Guél bou tangue ma diarou
Bi bou bakh bi la
Tay nak bouma reuthié ma wéré
Nga deungue wala nga dioup
Bokoy khol di waarou
Nieupa ngui wakh si dokhine bi ak
Rafétayam waaw

[CHORUS]
Bou dokhé ba dém gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu
Sho bi dam ko guiss rek tipsé
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap Yah
Khalé bi comme tangal
Bou dokhé ba ridj gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu
Sho bi dam ko guiss rek tipsy
Sétt wetch saf sap yah
Khalé bi comme tangal

[VERSE 2]
Niro woul ak
Guèl yi dieul sène galé
Défko bar rek oubi
Entrée bi gratuite la
Mais bofa dougué yow yay dieund
Cons bokoulsi
Génération Jet set bi
Dakarou tay
Teksi diek set fils
Takk sama fitt songue
Khalé bi lé rek tek
Comment tu vas bébé est-ce que
Meune nga sigui khol ma
Yangui wéteuli sama mère tchi sama khol
Kheutch lokho bi rek tek si sama call
Mou sourire,ma contane
Ni nullard bou amm fitt
Affaires yangui commencé nekh
Diokh nama 7-7

[CHORUS]
Bou dokhé ba dém gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu
Sho bi dam ko guiss rek tipsé
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap yah !
Khalé bi comme tangal
Bou dokhé ba ridj gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu
Sho bi dam ko guiss rek tipsé,
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap yah
Khalé bi comme tangal

[VERSE 3]
Daw ba reuk
Khar goudi pour ték premier pas
Tabakh souniou relation
Dieul xolam déf fa tank
Même pas une semaine
Moungui ni boy bi dafma takhe
Dougou instagram screenshot photo ba tok
Déf nama PP fépp bala dara khéw
Déguanté chaque jours
Wakh téléphone ba néléw
Kounék’a ngui saub
Appels ak messages commencé taw
Je t'aime ya ngui dakanté ak ay Malaraw

Aligné kaw ba souff
Kholma boy, today je suis sappé
Tay lagnou wara tassé
Bama shaw' bi, dama geuna tipsé
Bébé doumala khandiou
Auto, khaliss, villa
Dila diéma Pape et Cheikh
Liko dal moma dal
Khamnani lonkotinaaaa

[CHORUS]
Bou dokhé ba dém gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu
Sho bi dam-ko guiss rek tipsé
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap yah
Khalé bi comme tangal
Bou dokhé ba ridj gauche
Boufa khar droite
Même boy diay yékk
Bouy nieuw ngay watieu
Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy
Bari caractère ba kène douko tankal
Sétt wetch saf sap yah
Khalé bi comme tangal

Watch Video

About Tangal

Album : Tangal (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 19 , 2019

More SAMBA PEUZZI Lyrics

SAMBA PEUZZI
SAMBA PEUZZI
SAMBA PEUZZI
SAMBA PEUZZI

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl