Bataxalu Askan Wii Lyrics
Bataxalu Askan Wii Lyrics by SIDY KA
Déret turu sufu senegal bay walangan
Takal badola bi raxasu si guéju nott
Thiono du fegn si pouvoir budul jehh
Non non nio bagn
Sama batahal bi
Askan wéma yondi fokma jalaléko
Meuna tougnou dundu li
Si nguur gudul jehh
Non non nio bagn
Thiow jiip na fugnko fogéwoul won
Injustice bi thi rewmii metina
Senegalais bangui jooy nakaru holl
Non non nio bagn
Yaw niata jeune nio deé thi lii
Rongognu nakaar féthiali
Waro haar ayy netalii
Sa deff patt a yokku li
Rew meepa ngui jooy
Holl yeupa and tooy
Non non nio bagn
Lettre bi filakoy yémaléee
Porteur de voix
Askan wi nioma yoni wonn
Senegall sunu gaal
Free Senegal
Non non nio bagn
Watch Video
About Bataxalu Askan Wii
More SIDY KA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl