MAHFOUSSE - This is Sénégal Lyrics | Afrika Lyrics (Musique, Paroles et traductions)

This is Sénégal

MAHFOUSSE Senegal | Hip Hop,

Paroles de This is Sénégal

Sénégal sénégal sénégal (oooooh oooh….)
Sénégal sénégal sénégal (oooooh oooh….)

Fimoy sénégal, Deukou teranga
Beuri problème, Llll loumou dooon
Fimoy sénégal, Deukou teranga
Beuri problème
Ken xamoul founiou dieum
Fimoy Sénégal, Deukou teranga
Beuri problème
Llll loumou dooon
Fimoy sénégal, Deukou teranga
Beuri problème
Ken xamoul founiou dieum

Fii nii moy Senegal, Ouest Africa
Pays de la Teranga
Tekki fi metineu
Fii nii moy Senegal
Courant bi coupé neu
Doug na colobane
Sama call dem neu
Santhiey
Fii nii moy senega
En tout cas warouna police ak tribunal
Dund bi diaféna
Fii nii moy Senegal
Amougoul changement
Thiebou dieun penda mbaye
Mafé ak domoda
Amato ben deal
Diamonoy pedophile
Xolama xalei bei
Amatoul respect
Am sa ben grand
Nan ko defaillant
Jikoy feneant
Wouh wouhh waouh wouhhh
Dafa barri
Loufi xéwa baarri
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Ladjoumalène
Fii nii moy senegal
Netaly diotaly
Fetialy motaly
Santé doranté
Fii nii moy Senegal
Deuk bi salenté na
Beurina talibé
Ken défattoul charité
Xolalma sa guinaw
Xalé bou ndaw
Wara djangui
Deuké what sapp
Taak couronne
Diko fil tré
Toop tendance
Beug free
A vrai dire mane souma sagnon éléve yeupay am  bac wagni snapchat
Pour dem fac xam nga rek affairou mak
La quoi ah ah ah ah
Etudiants étudiants étudiants
Bourse yi Bourse yi Bourse yi
Beuguo loudoul niou faylako
Policier talal leu gon
Talal leu gon
Talal leu gon
Talal leu gon

Wouh wouhh waouh wouhhh
Dafa barri
Loufi xéwa baarri
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé

Wouh wouhh waouh wouhhh
Dafa barri
Loufi xéwa baarri
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé
Dafa barri
Dafa yémé

Dama guint ben beuss
Nioune nie annnd done bène
Rew mi souniou  bolloo
Dîna dem fou sorry
Naniou bolé xol yi
Té bayi xiro ak ngayo
Té bayi xiro ak ngayo

 

Laisser un commentaire