ONE LYRICAL  Tutorial Freestyle 1 cover image

Tutorial Freestyle 1 Lyrics


  Play   Watch Video   Correct   Add Translation

Rap

...

Tutorial Freestyle 1 Lyrics by ONE LYRICAL

[VERSE 1]
Sama gayi partagé len vidéo yi
Succès moma fégnou demb convoqué
wou ma ko mané ko sus man dik
I’m style oh chiit da
Nga yékha nandeu
Né ba légui bindou m’ak bic
Yamou niou ma fi bro
Sa microphone dou dioug ni pa
Bou teukou maguétou diague
Professeur wéssou na diangue ni guel
Bou def tatou nen nieup lay kat

[CHORUS]
Nane nga sante wax ma sa tour
Bakary faye niata barre nga am
Bala sa batterie fay
Lalou ma safar teudieul sa gate
Té ligueye rap bi dag ko
Parcorisé texte yi mandou ni keyte
Wan ma sa keyte c’est la police
Niou palpé la delit
Mane mala geuneu terrible geuneu sokhor
Tacle John Terry da nga dadiék police
Si bopou kogn bi baré ma sa liste
Yolé marchandise bi
Mola déssé kone deh dieul
Nga risque boy squoohh

[VERSE 2]
Succès moma fégnou demb convoqué
wou ma ko mané ko sus man dik
Pakka ci pout (ha !)
Négocié samay cachet ni toxicomane
Bi teukounala saga la doul (day)
Bind barri tax nga mandi té douma naane
Kofi Anane toufli si casse nga naane
Dawal si beat bi awma
Permis romb nala nganan pip

Aga Sindey, Aga Sindey, Aga Sindey
Hé Omzo beat mayma touti live ci beat
Bi some live rek some
Ndiago bek dioulit bi nieup
Nangou bayil ma diap
Diouli aduna bi dou ni
Dag ma bagn beug ma diap souli
Mane la selbé diouli
Diapeu na sa xourri taka to ligne

Niambi tate nga xouli diang
Len tuto yi wanté dou nitte
Sama gayi partagé len vidéo yi
Assane Diouf freestyle (bré bré, bré bré)
Partagé len vidéo yi (aga sindey)
(Aga sindey), (aga sindey)
Partagé len vidéo yi (aga sindey)
(Aga sindey), (aga sindey)
Partagé len vidéo yi

Watch Video

About Tutorial Freestyle 1

Album : Tutorial Freestyle 1 (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 11 , 2019

More ONE LYRICAL Lyrics

ONE LYRICAL
ONE LYRICAL
ONE LYRICAL
ONE LYRICAL

Comments ( 0 )

No Comment yet

See also



You May also Like



Get Afrika Lyrics Mobile App

About AfrikaLyrics 

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2020, New Africa Media Sarl