Mburook Lem Lyrics
Mburook Lem Lyrics by LEUZ DIWANE G
[COUPLET 1]
Sa Arras
La niou bolè niari rouh yi
Adouna dou wone touki
Té guissèw niou ba nopi
Eeh
Béna place
Tokk niou beuneu sama roues yi
Né kou démone touki
Té meunoul nieuw balégui
Eeh
Dianakhék baanex
Dima keuli keulé
Kagne lay done
ak nou May Def ba guiss la
Dane ma khégne lou gueune nekh
Té dou ki dou keulé
Nga néwone si Yoon
Nou May Déf ma miss la
Stagiaire la wone CV bi démna fou né
Ndékété Yoo douma liguey si niom
Dou dianerr Dagne ma la wane
Mbekté la yooo cédé bi datch na boudé
yaye diour samay dome....
[REFRAIN]
Ni Youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié
Té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié
Moy dakh Mburok lem
Douma la fene, ggive me your hand
Niou andeu dem fenene
Dieundé wouma la ken
Dou kene si niom kou meune dara si nioune
Té nioune sokhla wou niou khoulok kén
[COUPLET2]
Nga togne ma ma lay balou
Wax lene ma Kagne lay dalou
Kou sagna tambambalou
Boma méré ma warou
Bayi lene niou wax lou lene neex
Guissa gouma lou niou wara téré dem
Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh
Bayi lene niou wax lou lene neex
Guissa gouma lou niou wara téré dem
Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh
Ké wax ko boumou yakh crédit wam
Da nga gueuna fort khétou bone si mane
Tate lay Def sou ma la djiégué
Meune nga sa bord mate nga li nga done si mane
bou doul yaw sama tole kene dou ko ñagué
Bokak yaw keur
Di fo di ré di Contane
Moy sama yéné si yaw
Mou antou niou mour la nga ouff sama ndiaboot
Je t'aime mon coeur
Kene dou niou ré
Do degg ndeyssaan
Dina la téyé ni mou waré Ba degg diaraboot
Ma moitié ma Reine
L'autre moi ma meilleure amie
quand je parle de toi j'ai des larmes aux yeux
Je t'aime et tu es toute ma vie
[REFRAIN]
Ni Youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié
té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié
Moy dakh Mburok lem
Douma la fene
Give me your hand
Niou andeu dem fenene
Dieundé wouma la ken
Dou kene si niom kou meune dara si nioune
Té nioune sokhla wou niou khoulok kén
[COUPLET 3]
You know I love you
Never dare to leave you
You know I need you
Every Day Every night
I'm thinking about you
Night and Day everywhere i go
Baby I see you
There is no one, no one like you
Nga togne ma ma lay balou
Wax lene ma Kagne lay dalou
Kou sagna tambambalou
Boma méré ma warou
[REFRAIN]
Ni youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié
té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié
Moy dakh Mburok lem
Douma la fene
Give me your hand
Niou andeu dem fenene
Dieundé wouma la ken
Dou kene si niom kou meune dara si nioune
Té nioune sokhla wou niou khoulok kén
Watch Video
About Mburook Lem
More LEUZ DIWANE G Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl