WALLY SECK Natural Love cover image

Natural Love Lyrics

Natural Love Lyrics by WALLY SECK


Xaley bi may doundal
Feel nani dafma beug ngir yalla
Ay vibes’am fimouy dialeu
Amoul benen mindef boufay dialeu
Bouy dokh di daagou ci kogn bi
Day dal melni solou daleu
Lima yeuk ci sama xol bi
J’affirme moy natural love
Guene ci xel yalla ko sakk ngir man
Yeyeee, wowoooo
Yalla ko sakk ngir man

Baby dama dof ci yaw
Limoy natural love
Boulen ci diemeu wah lou niaw
Lima geuneu neh ci mom
Moy yarine wa moy yarine wa
Ak dohine ba ak dohine ba
Eloquence bek elegance bi
Ki moy sama sweetie girl
Baby dama dof ci yaw
Limoy natural love
An gars gni
Boulen ci diemeu wah lou niaw
Ndeysaan
Yay sama love
Dama dof ci yaw
Loma def no matter
Tahawougama mama
Natural love baby
I love you
I love you and you know it baby
Bouy dokh di daagou ci kogn bi
Day dal melni soloul daleu
Lima yeuk ci sama xol bi
J’affirme moy natural love
Guene ci xel yalla ko sakk ngir man
Ca naturel ba la

She walks around the corner
Look like a diamond in the water
I know this girl make me crazy
This love is a natural love
Ca naturel ba la

Watch Video

About Natural Love

Album : Natural Love (Single)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Jun 07 , 2021

More WALLY SECK Lyrics

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl