JAHMAN XPRESS Bamba Teranga cover image

Paroles de Bamba Teranga

Paroles de Bamba Teranga Par JAHMAN XPRESS


Ahmadou mooy kiniou doyloo ba tax
Lepp lougn am meune ko dioxé took
Khadim Rassoulloulahi miniou gueum
Yonente bé ko diox limou am
Bamko yoboo (yoboo ca boromam)
Lagn ko fa taanaloone ay mbireum
Lo yorr dioxeel Bamba fay la louko gueune fouf
Moom weerou waay la motax mbeureum dou laal souf

Yaay ki niou defar ba niou djag (Cheikhi Bamba iow)
Doylo la ba lougn yorr dioxé took Mourid Berndé
Mbacké Balla Aïssa Boury neeleen Jërejëf Al Mountakha
Day baay di maam donitt mbegoum jaam gnii
Linganiou defal dafa reuy
Tax founiou aw ñepp ni thieuy, amougn sa fay

Mbacké Balla Aïssa Boury neeleen Jërejëf Al Mountakha
Day baay di maam donitt mbegoum jaam gnii
Ndieuké ci iow moujé ci iow, mandi naa sa leer yii
Loumay djégaani feneen? Borom Toubaak Njaareem

Mbacké Balla Aïssa Boury neeleen Jërejëf Al Mountakha
Day baay di maam donitt mbegoum jaam gnii
Bamba ni Maam Thierno gaaganti leen
Euleuk bou jaam gni taxawé ma lidjeunti leen

Mbacké Balla Aïssa Boury neeleen Jërejëf Al Mountakha
Day baay di maam donitt mbegoum jaam gnii
Aljaanah neleen Aljaanah (Aljaanah)
Aljaanah neleen Aljaanah (Aljaanah)
Cheikh Bamba niounak iow ba Aljaanah (Aljaanah)
Aljaanah Mourid Téranga (Téranga)

Cheikhi Bamba iow linga def ci nioune 
Dotoul dégn, abadann la iow moy tabé
Bamba danio yarr baniou amoug yarr
Té tégouniou yarr kone sante koo niou warr
Xeeweul yangui sawaan, ci la Mourid yiy taataan
Teerou gann gni berndel leen, dioxé bolékook di rétaan
Lign guiss ci moom mii Daam ci mom la yam
Amoul feneen kenn douko am
Ndax lou leer laniou wann ba niou niémé fa niou djeum
Cheikhi Bamba iow yaa daan gni daa dem arass ak diwaan

Cheikh Bamba moo gaantal kerok yanou yann ba weuy
Bimou déloussé kenn djambatoul bobéé ba tay
Bim tambalé bagn yaa ngui réé naan lii dou weuy
Kouko ndjortt woon daa rèèré mbir Touba ngui tay
Touba ngui tay kouko rèèré woul mooy ngueun gui lay
Koufa soobou raw Cheikh Bamba kenn douko soorou tay

Kou am lii niou am, doo ko wéthiook dara
Dou lou kenn xam, neeleen Jaraama
Yaa niou térè athée, Ba dougn dox di weuliss
Lougn ci meuna goobé, nioune dinagn ko garr
Kenn dou Cheikhra Fall (Raw gaadou goor Yallah yi la djeul, deimal Ndiaabéé)
La né Maakka loolé khel douko dadjal
Amnga ko té meune nga ko
Defal nouko ndax boulay soob mouy nangou

Tabbé gui né ci nioune mooy woolou guign la woolou
Yoon wi loo ci niaxx Bamba fayla lou gueun loolou
Boudoul woon Khadim Rassoul djoulikaay yi fay
Kone santa warr kouy wooté tay (mbegoum jaam gné)
Liy leer ci peenkou bi Ibra Fall yaako dioxogn
Bambaay djantt kenn mounou laa xool djaakk (Kone baayou Goor gni)

Aljaanah Bamba Aljannah (Aljaanah)
Aljaanah Bamba Aljannah (Aljaanah)
Aljaanah Bamba Aljannah (Aljaanah)
Aljaanah Bamba Aljannah (Aljaanah)

Ecouter

A Propos de "Bamba Teranga"

Album : Bamba Teranga (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Sep 20 , 2021

Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS

JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl