DIP DOUNDOU GUISS Noboma Woon cover image

Paroles de Noboma Woon

Paroles de Noboma Woon Par DIP DOUNDOU GUISS


[VERSE 1]
Le passé c’est le passé
Pour nos problèmes moi avec toi
J’en avais assez
Maintenant que tout a changé
J’ai tourné la page parce que
Tu m’empêche d’avancer
Tchi dirr bou gate la leu
kham nga beug ma jugé
Ci sa digue ay kharite
Nga séwal ma ni  I
Mane yorouma wone xaliss,
Té gniko yor sa xol ioe
Meusso len ko thiabile
Bamala guissé si la guissék
Nitte kima done sett
Façon yen goor gni nieupa yam
Ngané ma meunoul né
Mane mélouna ni gars gni
Sa tank sama tank présenté ma pa bi

[CHORUS]
Hey ! nga bagn né dett dou maak ioe
Damala meuné mouniou dem fen maak ioe
Indil ngama kénén ndax doumala am ioe
Ioe ci sa bop yama téré and ak ioe
Nga bagn né dett dou maak ioe
Damala meuné mouniou dem fen maak ioe
Indil ngama kénén ndax doumala am ioe
Ioe ci sa bop yama téré and ak ioe baby
Noboma wone
noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma message no bouma wo wooo
Oh ! Noboma wone

Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma message no bouma wo wooo ! anh
Noboma wone
Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma message no bouma wo wooo
Oh ! Noboma wone
Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma message no bouma wo wooo ! oh


[VERSE 2]
Kouma ko waxone doum ko
Geum ya moudié khéwi ni
Mane ioe rek la guissone
Nga diapéma ni invisible
Bayi nala a vie
faté nga big mey romb ak vitessou Ferrari
Mbeuguel indiwoula lila indi dieuli na
Tay ngamey soga meuna set fepp ni FBI
Reuthi nala bayil, wadji ma done
Dieundé tay nako niémé trahir anh


[CHORUS]
Nga bagn né dett dou maak ioe
Damala meuné mouniou dem fen maak ioe
Indil ngama kénén ndax doumala am ioe
Ioe ci sa bop yama téré and ak ioe
Nga bagn né dett dou maak ioe
Damala meuné mouniou dem fen maak ioe
Indil ngama kénén ndax doumala am ioe
Ioe ci sa bop yama téré and ak ioe baby
Noboma wone
Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma message no bouma
wo wooo ! anh
Oh ! Noboma wone

Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma
Message no bouma wo wooo ! anh
Noboma wone
Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma
Message no bouma wo wooo ! Oh
Noboma wone
Noboma ndeysane noboma wone
Bama ley facetime taloma wone
No boulma
Message no bouma wo wooo ! Oh

Pourquoi tu crois aller venir quand tu veux
Mais cette fois si là c’est trop tard
Wo wohh

Ecouter

A Propos de "Noboma Woon"

Album : Noboma Woon (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 10 , 2019

Plus de Lyrics de DIP DOUNDOU GUISS

DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl