
Paroles de Criminal Love
Paroles de Criminal Love Par SONIA DIOP
Kham ngani damala love boul ma dof lo
Kham ngani damala mine bouma khif lo
Boul wédi da nga kiffé mais sous control
Ma nangou def la sama king diokhla couronne
Boma téwoul doma amati
Boum la bayé doma guissati
Loum la yéné mo eup love you
Fim la yobou am nga ci lolou
Doundou real game, diokh la sweetrust
Mayla li la nékh ba foumou yam nekh
Kay niou doundou real game, diokh la sweetrust
Mayla li la nékh ba foumou yam nekh
Kholma ci beut mo geuneu naturelle,
Boma diégué melni courant moma lale
Bouniou khoulo mou melni dama dof
Bouniou réro nga daldi diakhasso
Wan ma wan ma sama love diokhma lima yélol
Bouma neu sa xol li nga beug lay done
Souma nagou control dafa nara thiol
Dang ma nara follow night and day boy
Mangko yeuk li nga yeuk fi nga tok amoul khiro amoul ngayo ma ngui ley khol
Boulma diay preak té mane mi rek nga beugeu fek
Niowal fi rek niou tek nangoul boy ndax niou bègue
[REFRAIN]
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara gagne way)
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara ray mane)
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara gagne way)
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara ray way)
Doundou real game, diokh la sweetrust
Mayla li la nékh ba foumou yam nekh
Kay niou doundou real game, diokh la sweetrust
Mayla li la nékh ba foumou yam nekh
Kham ngani damala love boul ma dof lo
Kham ngani damala mine bouma khif lo
Boul wédi da nga kiffé mais sous control
Ma nangou def la sama king diokhla couronne
Boma téwoul doma amati
Boum la bayé doma guissati
Loum la yéné mo eup love you
Fim la yobou am nga ci lolou
Kholma ci beut mo geuneu naturelle,
Boma diégué melni courant moma lale
Bouniou khoulo mou melni dama dof
Bouniou réro nga daldi diakhasso
[REFRAIN]
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara gagne way)
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara ray mane)
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara gagne way)
Criminal love love (love criminal)
Criminal love love (daf ma nara ray way)
Ecouter
A Propos de "Criminal Love"
Plus de Lyrics de SONIA DIOP
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl