Paroles de Varadj Varadj
Paroles de Varadj Varadj Par CHERIFOU
Simbawé Simba yéhi yehhh
Baby kay Baby kay wouyouma
Yéni say ma deconné guindima
Beuri fay si def genre di ték deal (yeah)
Souma déconné guindimaa
Limay geuna nekh bounou diano bangamay réé
Sama khol di fekh guoné gui yay kimay begual
Nioun naniou dokh sounou yoon bagna deglou wakhi noon
Te nga kham man sama khol yay kikoy Varadj Varadj
Yay kimay gnamakh’taan yay guoné am beureudj
Yay kimay
Yay Kimay piloté yay kimay deureudj
Yaw yamay Varadj Varadj
Mbeuguél bou diapé ci khol dakoy doundal (doundal)
Mbeuguél bou diapé noon dakoy mbougual (mbougual)
Féss nga sama khol amour Validé
Sama mbeuguél molay sagual waw
Do diamaalê man ngakoy diguaalê
Mala faalê do kouniouy limaalê
Ya geun ci man founé ma dé fa
Demal Aljanaa ni yobalé foné ma néfa
Demal guoné
Do diamaalê man ngakoy diguaalê
Mala faalê do kouniouy limaalê
Konn féthial Bibam pa raba rampa
Bibam pan parapa ramba bibam parapa rambakh bibam
Lambe dia ngui nekh Djéleu bangui lérr
Ay meuné ngama ci wett gounê moy ndam lou lérr
Chérie wakh Wakh dji moy may sa Talibè
So décidé maa Validé
Mani kholal mbeuguélou Diamono Dioylona kouné nottna kouné
Té Seukeuteu Meukeuté Guewel douko daw té diomalna kouné
Hé Cherifou dafa way
Bamou wayé limou wakh
Danéé
Sa ripa rapa bibam sa pa-rapa rambakh bibam
Sa ripa rapa bibam sa pa-rapa rambakh bibam
sa ripa rapa (Wouy yaaaay)
Do diamaalê man ngakoy diguaalê
Mala faalê do kouniouy limaalê
Ya geun ci man founé ma dé fa
Demal Aljanaa ni yobalé foné ma néfa
Demal guoné
Do diamaalê man ngakoy diguaalê
Mala faalê do kouniouy limaalê
Konn féthial Bibam pa raba rampa
Bibam pan parapa ramba bibam parapa rambakh bibam
Ecouter
A Propos de "Varadj Varadj"
Plus de Lyrics de CHERIFOU
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl