Paroles de Day Doul
Paroles de Day Doul Par CHERIFOU
[REFRAIN]
Sama tante moma dof lo
My money my body mou yobou ko si sérigne bi
Tanti fanta loma def ni oh
Lo diokhagn ma dag tay ji nga yobou ma si sérigne bi
Day doul day doul day doul yamba la tokh ba dof
Day doul day doul day doul sangara lay fowééé
Day doul day doul day doul yamba la tokh ba dof
Day doul day doul day doul sangara lay fowééé !
[COUPLET 1]
Ya ngui mouki mouki
Tokh nga ba fouti fouti hé !
Ya ngui melni bouki
Sa khel mi ngui deuké touki
Ioe bayil yakh derr
Frere ioe bayil thionguenaire
Lomay diay sanguinaire deuké dima sandi khérr
Boul tokh sey baune nane sey wayn tipsé ba djign ko
Tanti Fanta khey dokh souniou kaw
Lokh souniou kaw ba kogn bi yeup miss ko
Comme si comme sa
Guiss na mouy gass di soul
Dey dieund bouki guinar
Bou nioul mokoy def nopi cool
Ioe ngey kheur weur di doul
Ya geuneu kham kima done
Loumeu tokh louma nane douma guéneu gamme béneu yone
Ya geuneu kham lima done té yama dakh def vop
[REFRAIN]
Sama tante moma dof lo
My money my body mou yobou ko si sérigne bi
Tanti fanta loma def ni oh
Lo diokhagn ma dag tay ji nga yobou ma si sérigne bi
Day doul day doul day doul yamba la tokh ba dof
Day doul day doul day doul sangara lay fowééé
Day doul day doul day doul yamba la tokh ba dof
Day doul day doul day doul sangara lay fowééé !
[COUPLET 2]
Amato diote ya ngui tokk
Meuneu to thiop ya ngui tokh
Louniou tekk nga dieul diaye tass nga keur baye dig si diote
Wey mane mane talouma ko
Mou diamb sama mine diakhassé poto poto
Wel mane nak bou donone sama sago
Tanti Fanta moma taylé
Effet para noya
Mani li lane laaa… !
Nga khol ki bagn ko khol ké djign ko
Kholatal ni nga mel
Sama tokh sama mandi
Dafa diaroul sa khaliss
Fi lakoy rebeuté boula mété foga sa weuliss
Wayy yambaaa… !
Bouko djign tantaaa !
Dou kéneu ioe leu hé !
[REFRAIN]
Sama tante moma dof lo
My money my body mou yobou ko si sérigne bi
Tanti fanta loma def ni oh
Lo diokhagn ma dag tay ji nga yobou ma si sérigne bi
Day doul day doul day doul yamba la tokh ba dof
Day doul day doul day doul sangara lay fowééé
Day doul day doul day doul yamba la tokh ba dof
Day doul day doul day doul sangara lay fowééé !
Ecouter
A Propos de "Day Doul"
Plus de Lyrics de CHERIFOU
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl