Paroles de Nema Yeah
Paroles de Nema Yeah Par CHERIFOU
[REFRAIN]
Mane tamou nala def nala sama biir xol bi néma yeah
Khamna ni ioe la, yay kimay guiss soumay sétou néma yeah
Ioe ragadiou ma, keur auto la beug waxma néma yeah
Ioe kham nga sama « Inh inh inh » bi yako mom néma yeah
[COUPLET 1]
Sa taw bi nath na sama tool (ouh yeah) sa geum sedd sama xol
Mane geum na geum na yamey motali
Xalé bé wané matt nama deug mom seytané
Kholal ni nga togué ioe yay sama ouroul hayni
Loma geuneu sorri sama djeumeu dji
Daw vitesse xol bi déna (oh ooooh ! annh !)
Té loma geun di diégué may geun di danou leer kay diégué maaa (oh ! ooooh ! annh !)
[REFRAIN]
Mane tamou nala def nala sama biir xol bi néma yeah
Khamna ni ioe la, yay kimay guiss soumay sétou néma yeah
Ioe ragadiou ma, keur auto la beug waxma néma yeah
Ioe kham nga sama « Inh inh inh » bi yako mom néma yeah
[OUTRO]
Amoréééé ! (lou la nekh rek lay def)
Thiey amoréééé ! mane dama am sa thiofél
Mane kholma nileu mbeuguel
Thiofél gui né ci xol topeu meu né douma bayi
Namone na sa tarru kaname
Akssil kholma ré (waaw waaw !)
May daw ci bépeu aname nguir bagna guiss fo méré (waaw ! waw !)
Noone na ngui wax ma deuggou deuthi ko xerr yi
Love moma diri bama soti leer yi yi (goungué ma
Kay goungué ma) waaw waaw !
[REFRAIN]
Mane tamou nala def nala sama biir xol bi néma yeah
Khamna ni ioe la, yay kimay guiss soumay sétou néma yeah
Ioe ragadiou ma, keur auto la beug waxma néma yeah
Ioe kham nga sama « Inh inh inh » bi yako mom néma yeah
[OUTRO]
Amoréé ni leu mbeuguel
Bouy dém doma fa bayi té douma tayii
Amoréé (ouuuuhh !) Oh ! amorééé… ! (amorémiaaa !)
Mane dioyna dioyna mbeuguel boy dém doma fi bayi té douma tayi
Ecouter
A Propos de "Nema Yeah"
Plus de Lyrics de CHERIFOU
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl