Zéro Garantie Lyrics

ELZO JAMDONG Senegal | RnB,

Zéro Garantie Lyrics


[INTRO]
Yeah... yeah
Yo gni ngui tchi yonou wout beu legui
Khamouniou kagn la niouy nopalou
Yeah

[VERSE 1]
Def naa ay ndiaakhoum homie
Homie def naa ay ndiaakhoum dolli
(Def naa ay ndiaakhoum dolli)
Moytoul ma waa dji gueuneu meuneu noppi
Ndakh defkat dou aalou homie
Defkat dou aalouhomie)

Defkat dou alou homie (no no)
Mané defkat dou alou homie
Town dangay waarou homie
Pourtant kham naa lou baakh ak lou baakhoul
Kogn bi ma maggué teela guiss business
Legal bi dokhoul no def beuri vitesse
Ba tonneau ni DT ak Petit tchi corniche bi
17 ans rek nga indice ni ODB
Listen to me def naa ay bizness de merde
Defaat ay bizness de merde
Dem tougueul diangg fa ay yeneen system yu bèss
Pour tek yeneen bizness you lerr (yeaaaah)
Am naa ay ga you dakkh yeek ascenseur
Ay ga you gueuneu khogne pimp bouniou tedj jail
Ay borome baatin you gueuneu kowé aviateur
Ay yaaram you meussoul niémé beugueunté’k guél

Ay ga you beugg dope
Ay ga you beugg show
Ay ga you beugg flow
Ay ga you beugg blow
Ay ga you beuri doe
Ay ga you super broke
Ay ga you meuneu sope
Mais samay gayine legn though Oh

Tannouma fi ma diouddo motakh ecole
Mounougn wone comp yane genrou people laay freq
(Yane genrou people laay freq)
Alal dou dieund baraqa Yalla beuggoul kouy
Dingat ak kheep (boul di dingat ak kheep)
Yalla defoul loudoul li gueun diaroul ladjté ndakh
Djig na la’m deet (bakham djig na la’m deet)
Yalla bind ne lepp moma binde
Ma meun binde ay textes

[CHORUS]
Mounouma ralentir
Fi leppeu yékh comme car rapide
Tekki amoul garantie
Motakh doumeu ralentir
Doumeu ralentir
Mounouma ralentir (ralentir, ralentir, ralentir)
Fi leppeu yékh comme car rapide
(Car rapide, car rapide, car rapide)
Tekki amoul garantie (garantie, garantie, garantie)
Motakh doumeu ralentir (ralentir)
Doumeu ralentir ih ih ih ih

[VERSE 2]
Yeah
18 ans la am dome (beugg tekki)
18 ans la dem kaaw (beugg tekki)
18 ans la am diom
Baby mameu woroul meusteu
Manqué CFA (faut me tékki)
Bima djoté sama passeport fauk né damay
Dem takhagn lou beurri délouwate
Wayé ndéké dougeul aka beurri galankorr
Kou meunone khalate na bolék fac béék caligraphe
Def na ay deal’ou chèque, ay deal’ou call
Motakh ma dane niow vac indalé ay 18 call
Def ay deal you sett, ay deal you thiol
Moussoma guissone demb tay daganane ki dou mome
Ci sama xel bou gate, système bi la done khéékh
Tegklé borru loyer bourlé train I don’t care
Sama xél di nathie mey geuneu malhonnête
Di wadja tégui sama yoone
Fauk né ma done chef (Yeah)

Diangual nagn ma qu’es qu’on dit
Ken diangualouma
Qu’es qu’on fait (qu’es qu’on fait)
Goor y’Allah nagoul def comme diiw,
goor y’Allah dafay def done pé (1er)
Goor y’Allah khamoul def
Comme diiw louma tangue tangue
Sagn na nek pompier (yeah)

Guissna len ngen di edf
Comme free mais y’Allah bouma
Def comme yéén (yeaaaaahhh !)
Bi pa bi ganio mounou ma wone dem
Fékké deudj bi ndax beurri wone dette
Boy temps ci Hip-Hop bi khéss dégueu ngew
Khamna ni dagn ma done khép
Adio bou fadjou rek bénén niow tegou ci
diaroul ngey diakhlé mon frère
Diambar dowoul homie ma ngui ci sama conquête

[CHORUS]
Mounouma ralentir
Fi leppeu yékh comme car rapide
Tekki amoul garantie
Motakh doumeu ralentir
Doumeu ralentir
Mounouma ralentir (ralentir, ralentir, ralentir)
Fi leppeu yékh comme car rapide
(Car rapide, car rapide, car rapide)
Tekki amoul garantie (garantie, garantie, garantie)
Motakh doumeu ralentir (ralentir)
Doumeu ralentir ih ih ih ih

Mounouma ralentir
Fi leppeu yékh comme car rapide
Tekki amoul garantie
Motakh doumeu ralentir
Doumeu ralentir
Mounouma ralentir (ralentir ralentir ralentir)
Fi leppeu yékh comme car rapide
(Car rapide, car rapide, car rapide)
Tekki amoul garantie (garantie, garantie, garantie)
Motakh doumeu ralentir (ralentir)
Doumeu ralentir ih ih ih ih

Leave a Comment