Etudiant Lyrics
Etudiant Lyrics by BRIL
[VERSE 1]
Nioune nioy gni yaggueu thi bancs yi, niafé ba am #BAC
Dém #Fac, djanguéfa doundou bi téén la, faut que nga am Baak
Rote ba féssal sa xél djarna di dokh ba Chine
Deukk thi gëstou bania mélni gni xamoul : « ba, sine »
Fi moy guéwou xam xam, gni fi nek djangay sén Liguéy
Téla Yéwou, kén doufi khaar bamou Naadj douniou « Abdou Gueye »
Yéndou #Amphi, mélni péppeu thi gueuneu djeul ay #cours
Yeugo li am fi, yomboul té étudiants douniou xaar secours
Day méti niou mougn ko, djéngou di doundou djaar
« #couloir_de_la_mort
Watch Video
About Etudiant
More BRIL Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl