MAABO HBD cover image

HBD Lyrics

HBD Lyrics by MAABO


[CHORUS]
Beuss bi nga dioudou wone
Déloussi na tay la tay happy birth day
Beuss bi yay borome
Ndax ioe rek dara doula fay happy birth day
Dégeu na niouy wax nane
Beuss dou toute borome rek ley tolool
Ioe doundeul 111ans happy birthday
Happy birthday, tay sa biss la happy birthday
Happy birthday, na nga happy, happy birthday


[VERSE 1]
Beuss bi nga dioudou wone
Mo déloussi nioulay ndokolé
Amo louko geuneu reuy
Féké ngako kone nagn ko célébrer
Bima yéwo lako guiss si sama facebook
Mani togay amatoul na dioug
Indil nagn la sey cadeaux
Kay soufflé sey bougies dageu sey gateau
Sa kharite yi nga magando
Wouyu si la niow diko féténdo
Ak photo yi niou dieuleundo
Happy birth day nioukay wayandooo
Y’Allah nga doundou ba déwéne niou défate lou mel ni
Am diam ak khéweul mbékté bou yatou ci ioe mi


[CHORUS]
Beuss bi nga dioudou wone,
Déloussi na tay la tay happy birth day
Beuss bi yay borome
Ndax ioe rek dara doula fay happy birth day
Dégeu na niouy wax nane
Beuss dou toute borome rek ley tolool,
Ioe doundeul 111ans happy birthday
Happy birthday, tay sa biss la happy birthday
Happy birthday, na nga happy, happy birthday


[VERSE 2]
Beuss bou déloussi
Beuss bou déloussi
Dey nékh, niou yague ko féké
Niou diko fêté ak banexx, no ma guissé
Tay fi la guéné, niow tew ci sa birthday
Beuss bi mounou mako manqué
Sa kharite yi nga magando wouyu si la niow diko féténdo
Ak photo yi niou dieuleundo
Happy birthday nioukay wayandooo
Doundeul lou barri, ba sey may di bawane
Sa nitte you bax ya ngui ni
Ya ayé kay wané sa momel


[CHORUS]
Beuss bi nga dioudou wone
Déloussi na tay la tay happy birth day
Beuss bi yay borome
Ndax ioe rek dara doula fay happy birth day
Dégeu na niouy wax nane
Beuss dou toute borome rek ley tolool,
Ioe doundeul 111ans happy birthday
Happy birthday, tay sa biss la happy birthday
Happy birthday, na nga happy, happy birthday

Watch Video

About HBD

Album : HBD (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 03 , 2019

More MAABO Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl