ASHS THE BEST Tukki Bukki cover image

Tukki Bukki Lyrics

Tukki Bukki Lyrics by ASHS THE BEST


Bu xaaju guddee bu xaaju guddee bu ñëpp di nelaw man ma
weet’ag xaalat waxtaan’ag njegenaay
Kenn du ma yee ku nelawul nan lañ koy yeewee
Biig foru ma bët waxtaan’ag njegenaay
Nelawu ma biig
Xanaa waxtaan’ag sama njegenaay
Tay kenn duma yee
Ku nelawul nan lañ koy yeewee

Xale baa ngi jooy
Nax ko warul jooy
Doomu jambur warul jooy
Demb laa la miin
Tay yaa ngi taggoo
Soy dem yobbaale ma
Ulluku
Man ku ma nëbbu ma reer la
Ci rukku
Laa la woo yobaante la
(Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la)
Kuy tukki
Deeg naa ñu ne  warul taggoo
Fukki bukki laa gis taggaliko’og sama saggo
(Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la)

Bul ma di sooraale
Sooraaleel sa bopp
Soy dox di gestuwaale
Mën nga fakkastalu
Ulluku ku ku ku ku
Kuma nëbbu ma reer la
Ulluku ku ku ku ku
Tukki tukki bukki
Tukki bukki
Fukki bukki guddi
Fukki bukki bëccëg oo
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Bukki bënn buntu
Bant bënn bëttëm
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Fukki bukki guddi
Fukki bukki bëccëg oo
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Bukki bënn buntu
Bant bënn bëttëm
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Ulluku ku ku ku ku
Man ku ma nëbbu ma reer la

Watch Video

About Tukki Bukki

Album : Tukki (EP)
Release Year : 2022
Copyright : © 2022 Nautylusprod
Added By : Farida
Published : Dec 23 , 2022

More ASHS THE BEST Lyrics

ASHS THE BEST
ASHS THE BEST
ASHS THE BEST
ASHS THE BEST

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl